Xibar.net - L'oeil critique du Sénégal


Référence multimedia du sénégal
.
Google
Les perles de Sama Dieukeur sama Kharite
Le témoignage du jour : sama dieukeur dafa nieuw vacance akh awo bi, ma yakarni mane rek ma wara ayé ?
Slt tata habiby defal ma li ano ngir yalla balla may doff mane j’ai 20 ans je suis mariée il de cela 1ans 6 mois deuxième femme mon mari vie à l’extérieur avec sa première ms sa femme dafa nieuwone senegal 1 mois avant monsieur di nieuw si tabaski bi ms mr bimou nieuwé Sénégal si negou awo bi la wathie def fofou 2jours avant mouy nieuw si mane bima ko ladié loutakh ngay wathie fofou alors que yene niar yena nek extérieur ensemble mounima lolou kene douko def lislam dafni kou touki ba nieuw sisa awo ngay wathie ba paré dora dem fenene mane nak ba legui lolou manou mako digérer

A chaque fois souma ko khalaté rk sama khol bi dafay meti ta mr mom tmt dafma féne parsk avant notre mariage dara ko wakhone so nieuwé Sénégal ay aylo doufi am mounima waw ba wakhtaan si ak sama yaye ms bi djabar dji nieuwé ni dafay dieul ay ma wakhsi ak mom mounima lolou c ma décision bilae ça me fend le cœur nalawa touba nakh lolou legui nak dama beug kham nakh lolou lislam moka wakh wala se sont ces propos.

SDSK

Samedi 12 Décembre 2020
Le témoignage du jour : divorcés depuis 5 mois parce qu'on arrivait pas à avoir un enfant, il m'a engrossé clandestinement
Ay tata diapaléma publié ma svp. Je suis enceinte de mon ex mari😭😭😭 walahi fi rek la khalate am fi conseil bi gathié khamouma foumakoy wakhé sama yaye dinama bayi adina al alakhira walahi mon père n'en parlons pas😭😭😭.

On a divorcé parceque sa famille croyait que je ne pouvais pas enfanter et on lui avait même proposé une autre femme pendant qu'on s'était marié walahi lii natou la, on s'est retrouvé 5 mois apres sans que les parents ne soient au courant on l'a fait juste deux fois et voila qu'on me dit que je suis enceinte, je ne sais pas quoi faire ni quoi dire, je suis animée par deux sentiment actuellement le fait de savoir que je ne suis pas malade et que réellement je peux le faire mais triste parceque je sais que ma mère aura la honte de sa vie devant ses coépouses😭😭😭😭

Mon père est un homme religieux walahi diamou yalla rek la kham douko nékh aussi et franchement je vais bientot avoir 3 mois légui nieup khamko. Mon ex me demande de le dire à tout le monde et qu'après la naissance du bb on se remarie mais c'est pas aussi facile.
Svp comment dire ça à mes parents ? Je ne mange plus walahi.

SDSK

Vendredi 11 Décembre 2020
1 2 3 4 5 » ... 164



Copyright © 2007 - 2016 Xibar multimedia Tous droits réservés

DIRECTEUR DE PUBLICATION: Abdoulaye Sogue - Contact: Protect e-mail with only css

Xibar Multimedia - 2901 41st Ave, Long Island City, NY 11101, United State