Xibar.net - L'oeil critique du Sénégal


Référence multimedia du sénégal
.
Google
Les perles de Sama Dieukeur sama Kharite
Le témoignage du jour : je suis la femme de l'homme qui se retrouve dans des problèmes après avoir abandonné sa moitié
Bonjour la famille sdsk

Je suis l'ex femme de l'#Ano_2196 qui demande pardon et je tiens à apporter des précisions. Depuis hier je reçois des appels partout vue ton texte c'était très facile de savoir que tu parlais de moi mais bon comme tu as eu le culot de venir ici je me dois de t'y répondre mane dioulite la motakh diapalouma la dara balnala si khol bou séd mais j'ai le droit de ne plus t'écouter rappel toi combien de fois j'ai voulu qu'on parle mais tu me montrais avec impolitesse que tu n'avais pas envie de m'écouter...

Je tenais à te remercier d'abord car c'est grâce à toi que je suis convaincu que je peux me relever et aller de l'avant toute seule merci de m'avoir fait comprendre que la vie ne s'arrête pas à toi, merci de m'avoir montré qu'il ne faut jamais dire jamais merci de m'avoir montré qu'il ne faut jamais croire seulement aux belles paroles mais aux actes posés, merci de m'avoir montré le degré de l'étendue de la corruption humaine...

Alhamdoulilah alors si tu pense que c'est avec ton discours lamentable que tu reuissiras à me convaincre c'est en vain je t'ai aimé au plus profond de moi j'ai été fidèle et sincère avec toi, je ne demandé rien juste de la considération et du respect car je t'ai tout donné mon temps mon cœur ma jeunesse donne sokhna dileu tarbiyou toujours à tes ordres tu m'as fait croire que tu m'aimais pourtant ça t'a pas empêcher de me faire du mal de m'abandonner de m'ignorer comme une chienne au pire de me tromper ouvertement tu es même allé jusqu'à me comparé avec d'autres femmes en me déstabilisant chaque jours et au fil du temps je perdais confiance en moi de joir en jour, le pire tu n'as pas hésité à aller voir une autre dis moi lane laleu defaloul en tant sokhna ? lane la defoul pour harmonisé notre vie de couple ? J'ai tout tenté mais actuellement c'est trop tard.

Tu n'avais plus de temps pour moi toutes tes vacances c'était dehors avec d'autres femmes, je me sentais inutile j'étais vide et je chifoquais pourtant tu savais et tu voyais que j'étais déprimé et malheureuse mais j'avais l'impression que ça te faisait plaisir demnga ba xolatoma faletoma may beuss sama khôl ndakh bagne defaite et j'avais toujours l'espoir que dinga réalisé say erreur 1ans de souffrance waxoumako kene même pas ta mère je ne voulais pas la blesser nga continuer à te foutre de moi ande ak ay kharite yo khamni guemouniou dara ma avertir leu nga wakhma lounek yakarni linga nek moy li gueune si yow, que man may dof bi.

Je suis même allée jusqu'à t'implorer de revoir ton comportement mais dara li gueune yess quand tu es rentré pendant 4 mois en Europe dou appelle, dou message ma hospitalisé 2 fois lidieunetiwo si louma nek diokhatomeu deureum c'est là que j'ai compris que nite mo leundeum rappel toi de tes propos ( je ne te laisserais jamais tomber louma defal yalla bamou mayma kou melni yaw) ma kheuy djisleu nga nek benene nite niak yeurmandé niak loy rouss. Sila wakh lep sa yaye mou dioy ba soneu maniko soumafi togué je vais mourir ndakh Bobou j'avais perdu goût à la vie au début nak je croyais que soumala bayé j'allais en mourir ndakh mounouma wone imaginer ma vie sans toi mais sante yalla tu m'as fait ouvert les yeux, ma famille niogi may soutenir ma bayi lep si lokho yalla di douli di diang diko niane mou katanalmeu ma dial si épreuve yi dina meti mais yalla diékhoul diamou yalla ak beug bou deugou rek lala defone guisoko wone j'ai perdu 3ans 6mois de ma vie ndekéto yaw bene dof ngama diapé tu n'as rien fait pour me retenir au contraire sa soulagement la wone mais hélas tay ngay niew fii ak founek nga woté di wakh peine c'est perdu...

J'ai appris que dangay niew Sénégal mais je te supplie de ne pas chercher à me voir bi maleu sokhla si sama wete je t'avais pas vue va retrouver sa khalé bou fashion bigama don teukeulé, my nandité bi je suis toujours la même.
Cordialement

SDSK

Mardi 15 Décembre 2020
Le témoignage du jour : j'ai maltraité ma femme, aujourd'hui toutes mes affaires sont bloquées
Salam la famille sdsk j'écris sur le compte de ma cousine publier ma li en Ano svp magui rafetlou sene liguey.

Machala je suis venu pour ngene dimbalema si sama sokhna mou diegueul ma ndakh kham nani sama ngor mayouma sakh may diakarlo ak mom walla kene si sama famille ndakh lima ko deff yepou rouss nafi tok diko netali bref en résumé je suis un homme de 30 ans vivant à l'étranger marié à une fille extraordinaire depuis 3 ans sans enfants ma fek ko fou bakh niou nek 1 an ma demandé ko mariage mou nek kou bakh yarou am dîné machala étant très jeune innocente ma indiko sama keur mou nek ak sama yaye bakh si mom lol defko lepeum done diambar di allié travail et maison tegouma bene charge sonalouma si dara.

Au bout de 2 ans ma commencé diko négliger souma niewé Sénégal nek si lima nekh doumako fallé Bobu sama bene cousin mayma bene khalé may commencé di nekak koku demna ba tok ak sama Jabar meuneutoumako je passais tous mes congés avec la fille melni kou doff lisi gueuneu graw moy elle savait tout mais dou wakh dara dou xoulo dou mer day tok dima setane liko war yep mou nek thia amoul xarite amoul kene koumouy wakhal mane la dieulone defma lepeum ma diko torokhal demna ba intimité sakh amatoumako ak mom ndakh bala may niew mou nelaw sou beugué wakhtane ma niakal ko fayda mouy souffrir en silence tahoul mou reagir ma defko doff topou sama bakane ak mauvaise compagnie.

Hélas ça fait 2 mois elle m'a quitté et bloqué partout magui sogua réalisé que j'ai perdu 1 diamant xamnani togn naleu torokhal naleu sissa kanamou nawlé yepp tenga done kou am soutoura ak kersa khamnani tu ne veux plus me voir mais magilay niane si barkep cheikhoul khadim nga diegueul ma fima nekk sama lepeu taxaw sa akheu mogi may daleu bou bakh je sais que tu lira ceci SMD ndakh je te vois active ainsi que ta famille diap lene si mou deguelou ma même 5 minutes sakh... Sama mbok gorgni fonk lene seni sokhna ndakh Kinga takk mou donne khalé bou ndaw bayi lepou ngir yaw loko def si lou bonne yalla dinako wane excuse de la longueur

SDSK

Lundi 14 Décembre 2020
1 2 3 4 5 » ... 164



Copyright © 2007 - 2016 Xibar multimedia Tous droits réservés

DIRECTEUR DE PUBLICATION: Abdoulaye Sogue - Contact: Protect e-mail with only css

Xibar Multimedia - 2901 41st Ave, Long Island City, NY 11101, United State