Référence multimedia du sénégal
.
Google

Le témoignage du jour : sama diabar mofi dakheu wayé karaw bi dale...

Article Lu 1251 fois


Le témoignage du jour : sama diabar mofi dakheu wayé karaw bi dale...
Bonsoir tata merci de publier.

Je viens vous parler de ma femme vu que j'ai beau parler mais elle ne fait pas attention à ce que je dis, en plus elle est membre active de cette page.
Elle est voilée, pieuse et très belle ma sha Allah dama am chance nak beneu thiat rek la am bop bi noooooon à la maison sans le voile comme tolou ninguéler yi🤦‍♂️

dou firékou dou létou et moi j'adore ses cheveux salté woul déh dafkoy rakhass bamou khégne nékh mais douko let douko firi mom dal avant ramadan la létou won et jusqu'à présent lolou mo nek thi bop bi tresses yi dé len guissatoul sakh khadji yi dakh rap et elle s'en fout royalement. Je la veux toute naturelle à la maison pas de voile et moins d'habits😊

elle est vraiment très belle nak avec ou sans le voile mais thiat bi chiii quand elle enlève le voile damay ragal lal bop bi dakh repousse bou beuri ak ay let you rap svp yédlen ko namay défal ay life sakh walla mou firi ko sakh bayi nappy bi🥰😍 mais dal rien ish té souy gueneu ba defarou nonnnnn comme pérle ma femme est vraiment belle bilahi bop bi rek momay enervé dakh dou firékou dou létou😞



SDSK

Article Lu 1251 fois

Jeudi 9 Juillet 2020

Les perles de Sama Dieukeur sama Kharite





Copyright © 2007 - 2016 Xibar multimedia Tous droits réservés

DIRECTEUR DE PUBLICATION: Abdoulaye Sogue - Contact: Protect e-mail with only css

Xibar Multimedia - 2901 41st Ave, Long Island City, NY 11101, United State