Xibar.net - L'oeil critique du Sénégal


Référence multimedia du sénégal
.
Google

Le témoignage du jour : sama diabar bakhna torop wayé bandit woul...

Article Lu 1287 fois


Le témoignage du jour : sama diabar bakhna torop wayé bandit woul...
Bonsoir madame merci de me publier en ano svp.

Je suis un jeune homme de 26 ans marié à une femme de 24 ans et père de deux enfants sama diabar djiguéne geunouko bakh ,yarou ,yatou,yime ame yeuremandé ,tabé guoré louma ame ak louma amoul kéne khamouko yalla nako yalla déli diame mais le seul et unique problème est que diongué zéro.

la nuit dina sol nuisette you bakh mais silay yame 5 ans de mariage masouma provoquer mane rék may déme di thiokasse après on le fait et lolou dasamasi sone défois on peut rester 2 ou 3 semaines sans le faire et mane dama beugue djiguéne bou bandit si bir nék (chambre) . conseil la beugue noumay déf bamou changer . merci


SDSK

Article Lu 1287 fois

Mercredi 5 Août 2020

Les perles de Sama Dieukeur sama Kharite





Copyright © 2007 - 2016 Xibar multimedia Tous droits réservés

DIRECTEUR DE PUBLICATION: Abdoulaye Sogue - Contact: Protect e-mail with only css

Xibar Multimedia - 2901 41st Ave, Long Island City, NY 11101, United State