Xibar.net - L'oeil critique du Sénégal


Référence multimedia du sénégal
.
Google

Le témoignage du jour : pourquoi les hommes sénégalais sont de mauvais compagnons à ce point

Article Lu 1693 fois


Bonjour tata tu peux me publier en ano stp.

En fait dama beuguone kham loutax yéneu guorou sénégal mel nugn mel . Daguay guiss jiguen mou mel nim wara mel yam fim wara yam sokhlalula dara am avenir gua remuer ciel et terre wakh lou nek def lou nek pour tak ko mais une fois que gua tak ko rek diexna doto guiss lou bax ,gua deker diko togne diko def lo khamni khalatoko wone saxe waxe avant mariage diko tek lou metti , doto am ben attention, ben affection, ben tendresse, ben bienveillance a son égard ?

Les hommes répondez moi s'il vous plait loutax guen niemer ak? Loutax douguen continuer niguen melone avant di nekhal sen diabar dilen diox ay cadeau di waxtane ak niom di fo ak niom di kaf ak niom ? Loutax ? Loutax guen meune yak kholou jiguen ? Vous y gagner quoi? Est ce que yena gui kholat seni comportement di khalat seni partenaire? C'est vraiment triste 😔. Je comprends maintenant loutax certains parents matérialistes(daniou khamni diarulen yereum) . Ak loutax yen femme yi sour guor 😢.

Les filles prenaient votre temps ne vous mariez pas uniquement par amour khol len bu baxe diangu nite qui bou baxa baxe . Plus votre amour sera sincère plus vous allez souffrir. So mariewo par intérêt niou nakh la saxe digua khamni ay nakhanter la kou meune sa morom douma th sa khol dou yakou

SDSK

Article Lu 1693 fois

Jeudi 19 Novembre 2020

Les perles de Sama Dieukeur sama Kharite





Copyright © 2007 - 2016 Xibar multimedia Tous droits réservés

DIRECTEUR DE PUBLICATION: Abdoulaye Sogue - Contact: Protect e-mail with only css

Xibar Multimedia - 2901 41st Ave, Long Island City, NY 11101, United State