Référence multimedia du sénégal
.
Google

Le témoignage du jour : on s'est marié en cachette, il a par la suite dit que le mariage n'était pas valable et me demande d'avorter ma grossesse

Article Lu 1511 fois


Le témoignage du jour : on s'est marié en cachette, il a par la suite dit que le mariage n'était pas valable et me demande d'avorter ma grossesse
Salam tata je veux faire ça en anonyme svp. Mane dama ame problème je suis à l étranger ma tassé fi ak béne sénégalais qui dit faire parti des petits fils d'un grand Mara au Senegal té dafa diangue alkhourane bou bakh sakh xam li yalla wakh lép. quand on a fait 1an 5mois mounimeu nagnou marié comme tu as divorcé meune nga mayé sa bopeu ma nanguoulko lolou néko légui doko wakh sa parent mounimeu sama parent damay bayi gnou gneuw ma wakhlene ko face à face car ak ninga divorcé soumeu léneko wakhé par téléphone meune nagnou bagne té dama beugue gnou seuy.

Par la suite ma d accord à condition qu il avise mon grand frère et il l a avisé après gnou woute kougnou sédé mou diokhma thiane bi(je le garde toujours ak mane). légui gnou deff quelque temps de mariage mou gneuw nimeu seuy bi bakhoul car gnari sédé la warone ame té béneu rek lagnou amone bignoukoy takkeu par la suite la constaté ni ke dama eumbe légui ma wakhkoko mounimeu meu lolou nouvelle bou nekh leu légui mou wakhko kéneu koumou meu présenté wone avant notre mariage nimeu c est son grand frère de même père et même mère. par la suite lama wadji wo téléphone nimeu amguéne fiit marié té mère yeuguouko mais ne vous en faites pas gérer léne séne seuy et comme dagno wara gneuw fofou mane dina wakh ak gnom....

je signale que meussoul nanguou ma wakh ak aye parent wame directement mom modone gneuw nanemeu sama yaye mingui def enquête si yaw pour kham sa famille car wakhnako sounou dingueunté ba paré. a chaque fois boumako dane wakh mou passe meu sa mère day agressif commencé dimeu wakh lou nek...
un jour mou gneuw nimeu nagnou wakhtane nimeu na avorter pour gnou meuneu takaate seybi normalement ma bagne kimou done wakh ni grand fréram leu womeu nimeu na nanguou avorter mom dineu wakh ak parent yi gnou takaate seuy bi maniko déguena linga wakh après sama xel commencé gnaw car comme gnom dagnoumeu wakh ni famille religieuse lagnou bookeu ba paré gnoumay avorter lo silo djeulé numéro wadji diokhko sama béneu cousin mou woko par ma grande surprise wadji ndékété bokoul ak mom dara té benene tour la toudou.

légui nak sénégalais bi kheuy nimeu comme damala wakh nga avorter nga bagne légui guéneul sama keur sounou dingueunté nafi yéme. Sila envoyé message béneu cousineum ak béneu xaritam bou djiguene expliquer léne situation mais biko gnognou wowé dafa nier ke ni meussoul nékeu ak mane ke ni mane damay weur di yakh déram.. je jure sur le saint coran que ni so gnewone si quartier bignou deukk nga lathié sama dingueunté ak mom dagnoulanane dagnouy seuy..légui mane ma fékhé ba ame Facebook petit frère expliquer leep mou lathie meu sama numéro après womeu téléphone gnou wakhtane mounimeu mane mom je bel et bien son petit frère dou aye nakh sama numéro mongui nonou dina wakh ak mom après ma rappelé mais bimoumeu rappelé dafa melni benene nitt xamalmani limay wakh dou deugue ke na dème lidjeuntiko ak freram nimeu mom xamneu freram bou bakh dou deff lima wakh genre damakoy toumal mais limay wakh défouko.

légui ma fékhé ba nakh wadji niko légui nanguou na avorter diokhma garap bi ma nane diko enregistré nak moumay expliquer nane lakoy dieulé et tout(wadji il est médecin de formation et a même exercé à dantec avant de finir à l étranger). Légui ma wakhko niko dieuloumeu garap yi té enregistré nako té deuk bignou nékeu séne lois day téré kouy avorter waleu kouy wakh nitt mou avorter..Maniko ko nak dama beugue nga setal sama derr binga yakh thi sa famille djeul say responsabilité bamou nanguou hier mou gneuw nimeu day déménagé maniko khana gnoune gnoy ande mou bagne... mane léneu rek la beugue mou dieul aye responsabilité soumeu yalla mayé sama boopeu ma diokhko domame car ak limoumeu deff yeupp damako sour instant bi et comme on est tous des sénégalais bala makoy porté plainte gnoukoy teudje adounam di yakhou mani na gneuw fi pour coumeu diapalé té yalla takh mou djeul ses responsabilités et des conseils aussi vu le travail remarquable que vous faites..Je suis très désolée pour la longueur et merci d avance


SDSK

Article Lu 1511 fois

Lundi 14 Septembre 2020

Les perles de Sama Dieukeur sama Kharite





Copyright © 2007 - 2016 Xibar multimedia Tous droits réservés

DIRECTEUR DE PUBLICATION: Abdoulaye Sogue - Contact: Protect e-mail with only css

Xibar Multimedia - 2901 41st Ave, Long Island City, NY 11101, United State