Référence multimedia du sénégal
.
Google

Le témoignage du jour : mon mari ne me respecte pas et me culpabilise...

Article Lu 1213 fois


Le témoignage du jour : mon mari ne me respecte pas et me culpabilise...
salut la mifa ano svp

au fait les amies mane dale kouma conseillé si sama seuy la beugue je suis une jeune femme agé de 28ans mariée ya même pas 3 ans jai une fille de 8 mois.

je suis pharmaciene en plus dama diare daara montakh ma barri kérsa bilahi soumay wakh ak nit sakh damay ame probléme pour khole ko en plus sama yaye yarouma si seuye lou bari khamouko jongué mome zero ndakh ecole ba daara dja rék .

insyi nak diakhlé na trop sama dieukeur dafay nék di dokhane béna couzineume bo bo khamné mane damaka défone kharite té lima méti mome guéle bi chak jour mou nieuw si keur gui souma wakhé mounéma mako poussé mou dokhane ndakh mélouma nima wara méle mane nak wakhouma guél bi dara sounieuwé nouyou ma faye ko paré si.

Mane ak Mr nak si khoulo boudoule diékh laniou deukeu ndah day guéneu di anda ak mome ba heur bouko nékh té doumasi neub dara té si ça continu comme ça dina tass té beggouma lolou ame je veux vraiment sauver mon couple guirr yalla conseille rék la beugg ndakh je sais plus koi faire.



SDSK

Article Lu 1213 fois

Jeudi 26 Mars 2020

Les perles de Sama Dieukeur sama Kharite





Copyright © 2007 - 2016 Xibar multimedia Tous droits réservés

DIRECTEUR DE PUBLICATION: Abdoulaye Sogue - Contact: Protect e-mail with only css

Xibar Multimedia - 2901 41st Ave, Long Island City, NY 11101, United State