Référence multimedia du sénégal
.
Google

Le témoignage du jour : mon mari a fait de notre chambre lieu de débauche pour ses amis...

Article Lu 1291 fois


Le témoignage du jour : mon mari a fait de notre chambre lieu de débauche pour ses amis...
Publié moi ça en ano svp.

Mon mari permet à ses amis d'utiliser notre lit conjugal même boumafa nekké té bimmou koy deff en ma présence collegam bi dafa gnow ak guel bi après mounéma kay gnou dohantou.

Té fekk dafko beug abal negg bi gnou deff sen yoyou si sama kaw lal ak sama drap mou done louma metti bignou guénné maniko loutah gnouy dohantou té am gane mou dogma expliquer en plus mounima dako rouss thilako né respecté woma parck boma respecter dingma done consulter avant ngakoy nangoul li.

Ma beug délou mou teyéma néma diap thi gathié dinako rey boko défé je signale k mon mari est homme de tenue son collègue aussi des conseils svp😥😥😥


SDSK

Article Lu 1291 fois

Jeudi 13 Février 2020


Dans la même rubrique :
< >

Les perles de Sama Dieukeur sama Kharite





Copyright © 2007 - 2016 Xibar multimedia Tous droits réservés

DIRECTEUR DE PUBLICATION: Abdoulaye Sogue - Contact: Protect e-mail with only css

Xibar Multimedia - 2901 41st Ave, Long Island City, NY 11101, United State