Xibar.net - L'oeil critique du Sénégal


Référence multimedia du sénégal
.
Google

Le témoignage du jour : je suis une fille brave et chaste mais je n'arrive pas à avoir un mari, pourquoi ?

Article Lu 1625 fois


Le témoignage du jour : je suis une fille brave et chaste mais je n'arrive pas à avoir un mari, pourquoi ?
Salam tata
Qu'ai-je fait à Dieu?

J'ai 27 ans. Je travaille alkhamdoulilah et je subviens aux dépenses de ma famille. J'ai des frères et sœurs mais yallah mayouleine gnou am dolei torop. Leip louma am si sama famille lakay def. Je ne vais pas en boite, je ne bois pas, je ne fume pas, je m'habille correctement et le plus important pour mane moy jusqu'à présent j'ai garde ma virginité. Wantei on dirai que j'ai pas droit au bonheur.

A mon âge je ne suis pas encore mariée et qui ma yakarone ni moy done sama borom keur dafa kheuy rek takk keineine sans aucune raison. wantei mane louma djakhaal moy gnounei soy topato sa famille , di djeima done nit kou bah , teuyei sa bopp , leip mo wara facile si iao.

Wantei mane sama dara yomboul damay dem ba damay beugue sakh kharou parfois.
Damay gnane yallah mou raye ma à chaque fois soumay teudi. Sama geum geum wagneikouna ndakh yallah lou mettite rek lamayteikk.
Ma beugone sou nitt amei ay zikr yo khamni soko werdei bala djant bi teudi ma fatou mou bakheimako

SDSK

Article Lu 1625 fois

Vendredi 20 Novembre 2020

Les perles de Sama Dieukeur sama Kharite





Copyright © 2007 - 2016 Xibar multimedia Tous droits réservés

DIRECTEUR DE PUBLICATION: Abdoulaye Sogue - Contact: Protect e-mail with only css

Xibar Multimedia - 2901 41st Ave, Long Island City, NY 11101, United State