Référence multimedia du sénégal
.
Google

Le témoignage du jour : je suis sa maîtresse depuis des années mais il ne veut pas m'épouser

Article Lu 1234 fois


Le témoignage du jour : je suis sa maîtresse depuis des années mais il ne veut pas m'épouser
Bonjour à tous,
Je suis une femme, j'ai 34 ans divorcée et j'ai 2 filles la grande a 16 ans. Sama copain amna diabar té mak la, amna ay dome you mak sakh, wayé mom la beug.

Niou ngui guéne depui ay années, mou mey dimbali ci sama commerce, di fay sama appartement, di ma diapalé dafa done wakh niou moytou pour kén bagna kham sounou digeunté, mé samay mbok kham na niou.
problème bi c ke diabaram dafa trouvé sama ay photo nue🤦‍♀️ ci téléphone sama copain, legui elle sait, mais sama problème c ke une fois par semaine, la niouy guissé sama keur, ci journé bi pendant 2h, niou couché, mou gnibi.

Chak fois ke ma wakh ko affaire de mariage, mou ni ma na patienter, leggui mou diott, té bobou ba tey ma ngui kharrr té dama am ay dome you djiguene, da ma am ay none
Khamatou ma lou mey deff. Fii ma tolou ni kou ma khélal la sokhla nan lay def bamou tak.

SDSK

Article Lu 1234 fois

Vendredi 22 Mai 2020

Les perles de Sama Dieukeur sama Kharite





Copyright © 2007 - 2016 Xibar multimedia Tous droits réservés

DIRECTEUR DE PUBLICATION: Abdoulaye Sogue - Contact: Protect e-mail with only css

Xibar Multimedia - 2901 41st Ave, Long Island City, NY 11101, United State