Référence multimedia du sénégal
.
Google

Le témoignage du jour : Je vis le paradis grâce à elle et à vous...

Article Lu 1213 fois


Le témoignage du jour : Je vis le paradis grâce à elle et à vous...
Bonjour madame je suis un ancien de la page je vous suis depuis le début mais sous marin bou mak, je suis homme de 30 ans nouvellement marié😊 mais tata affaire bi nekh na walahi sou goudi dioté sakh damay kontane elle me fait des choses yo khamni😆😖🤩

Dima wakh ay wakh yo khamni je te jure sama yaram bi day daw sakh en plus elle est tellement douce hooookhoooo noy nep ba paré bandit walahi man khawma loutakh tellouma tak diabar rek non léguii amatouma sakh envie gueneu keur gui man khalé bi dinama ray, chaque jour ak ay feem you bess barki Serigne Bamba yalla dou niit mo kham litakh mou bollé goor ak djiguéne, non quel cocktail👌

Fila nékh nékh yam nak, non en plus khalébi dafa diongoma bakh tek si hoooookhooooo mana togue ba paré man wakh diou nekh noooo li amoul yeuk yeuk bou mel ni....

Tata je vous écris parceque fi lako khamé en 2017 yalnala yalla faye way wakhal wa page bi niou nianal ma boubakh parceque li wadji di wakh moma dall : didoundeu aldiana té dewagouma😆🤩. Walahi am diabar nékh na Barki serigne Bamba beugue na khalé bi svp nianal len niou way. Merci encore 🙏



SDSK

Article Lu 1213 fois

Dimanche 5 Avril 2020

Les perles de Sama Dieukeur sama Kharite





Copyright © 2007 - 2016 Xibar multimedia Tous droits réservés

DIRECTEUR DE PUBLICATION: Abdoulaye Sogue - Contact: Protect e-mail with only css

Xibar Multimedia - 2901 41st Ave, Long Island City, NY 11101, United State