Référence multimedia du sénégal
.
Google

Waxtanou fiadiar par oustaz alioune sall

Article Lu 121434 fois

Emission waxtanou fiadiar du 19 04 08 par oustaz alioune sall.



Waxtanou fiadiar par oustaz alioune sall
Emission waxtanou fiadiar du 19 04 08 par oustaz alioune sall.



Source: Sud FM

Article Lu 121434 fois

Lundi 21 Avril 2008





1.Posté par mouhamadou suzane diagne le 23/04/2008 18:35
slt à tous e à toutes vraiment oustaz sall amoul monrom been la fi yalla nafi yague tè weer

2.Posté par ibrahima lo le 25/04/2008 02:01
]b

3.Posté par ibrahima lo le 25/04/2008 02:03
ami de aliou sall j ecoute toujour

4.Posté par momy le 25/04/2008 17:59
je suis trés fière de vous enttendre.

5.Posté par bassrou seck le 26/04/2008 16:48
je suis trére de vous al oustaz mangulay nianal fanwou goudou ak wérguyaram.

6.Posté par pendalaye le 30/04/2008 18:59
fière de vous ententendre ouztaz vous faites non seulement lhonneur du sénégal mais de l'afrique toute entière ila gnanal sa sasouné

7.Posté par ndiaye le 07/05/2008 18:09
sante sounou borom ba mou niou maye alioune sall.
thie kha kham bou leer tara fete diokhine'
yalla na niou ko yalla fayal

8.Posté par Mar Fall Guéye le 09/05/2008 00:49
Bonsoir
Je demaindais a oustaz éske pour payer la priére de timiss le lendemé paréxample a 12H on doit réciter a haute voie?
merci d'avance!

9.Posté par abdoulaye lo le 10/05/2008 19:28
asalamou alaykoum yallna sone brom défalléne yiw alakhira ac adouna doliléne fane wou goudou ana moudiogou rafét tadéf sipossyi dara contane nane siyéne trop dama done lathie adaboul téguini seye ac tiguini niane ac kou touki pou diene marchandise amfa wér iska danga wagni diouli

10.Posté par khady KA le 16/05/2008 12:59
assalamou alaykoum, j'écoutes toujours Oustaz Alioune SALL et je prie pour que Dieu lui accorde une longue vie et une santé de fer. Mais j'aimerais vraiment que le waxtanou fiadiar soit plus long.

11.Posté par BARA DIOP le 17/06/2008 21:40
ASSALAMOU ALEYKOUM YA OUSTAZE ALIOUNE SALL MAGUI LAY ZIARE BOU BAKH

12.Posté par PapeMoussa le 20/06/2008 13:14
c bien c q vous fetes au moins cela permet aux autres qui ont le net de pouvoir s'instruire, se rectifier.
l'invitation que je voudrais lancer à tous les fans d'Oustaz Alioune Sall c'est d'aller acheter les cd au niveau de sud fm, de refuser de le copier. car il n'est pas normal que 500 cd ne soient pas en rupture. et on se dis fan ,, et c clair tant que c 500 ne sont pas écoulés nous n'aurons pas la suite. alors attendre jusqu'à quand ? montrons ce que nous et faisons lui au moins le plaisir de disposer de c cd.
je n cache et c la premiere que j'ecris mon mail/ moussacheikh74@hotmail.com

13.Posté par diobadioub le 25/06/2008 10:49
je l'ecoute depuis 2000. il a beaucoup contribué pour mon instruction . que Dieu l affermis dans ses pas et lui donne longue vie et santé.

14.Posté par sope nabi le 10/07/2008 12:07
ASSALAMU ALAYKUM WA RAHMATU LAHI WA BARAKA TUHOU oustaz alioun sall yana yallah gudal saw fan weral say thier yokou sa xam xam thi barkeb sama sope sunu sope sopeb yallah saydina muhammed salla lahou alayhi wa salam ta yokou matuwayi fi ngaye defe waxtan yi ban man thie diot WASALAM

15.Posté par oumar keita le 24/08/2008 00:25
il ma fait conaitre bcp 2 chose que j ne savais pa merci merci et encore merci

16.Posté par mamoudou ndao le 01/09/2008 15:04
merci a MR oustaz ALIOU SALL .

jai 2 kestions a poser
1) EST CE QUE L ISLAM INTERDIT LA MASTURBASTION

2) da

17.Posté par mamadou sall le 13/09/2008 02:04
nous somme tres content de t entendre que dieu te gard jusqu a la fin des temp

18.Posté par ibrahima sy le 21/10/2008 00:24
bismilahi rakhmani rakhim as salamou alaykoum wa rakhmatoul lakhi wa barakatou khou je suis de tout avec oustaz alioune sall et tout le sénégal doit rendre grace à DIEU de nous avoir donner un homme comme oustaz alioune sall

19.Posté par MOUHAMAD NIANE le 03/11/2008 08:23
ALHAHDOULILAH OUSTAZ MACHALLA YALLA NIFI YAG TE WER TE POSS YI AM LOU BARRI LOL AY MILLIARS NAK

20.Posté par Mohamed Diouf sopey Oustz Alioune Sall le 09/12/2008 18:31
assalamou aleykoum wa rahmatoula wa talla wa barakatouho. ma ngui lay ziaar di la waax dewenati te dila diegalou. yallah mey la faane wou goudou weergui yarame saam te aar la yaak sa ndiabot. dila nianal teranga adouna ak alaxira. dila feedali sama thiofele ak sama sopey cii yow. je suis au consulat du senegal a milan

21.Posté par ning ndiaye dit pape ndiaye le 10/01/2009 21:53
ismi quztaz pa ndiaye askounou fi parcell wahdatou 11ouhibouka ya ouztaz khouban sadifan la tansana minad doua

22.Posté par omar séck le 11/01/2009 22:19
assalamalicoum w t wabarakatawo mandé damayaka foni man rék mala beug yalla nanga fii yag té wéér yak s moustapha saliou ak mbolomi dioulit d d

23.Posté par Fatou Sy DIOUF le 16/01/2009 11:22
Assalamouhalayekoum kou bakh ki oustaz beugeu nala torop toujour damalaye déglou sur internet parce que fadjar gui amouma radio wayé kontane na thie yaw mangui laye gnanale fane wou goude ak were ndakh sa dounou ndiarigne la thie reymi. beugeuna nga gnalema ma ame borome keur bou yiwou bou mélni yow encor merci pour tout yala nala yala faye.

24.Posté par omar tine le 01/02/2009 13:14
oustaz yalla ngafi yaag te weer

25.Posté par dabo le 14/02/2009 05:18

26.Posté par serigne niomre lo le 25/04/2009 23:59
diaradiaf oustaz gnougilaye nianal fanwou goud ak wergou yaaram yalna yala yatal deunebi ndakh yagi baye sa wala boubakh thi warwi thi anam bou rafette kon yalnala yalafaye ....wasalam

27.Posté par aicha bathily le 30/04/2009 18:53
oustaz alioune sall yalla nifi yague té wér té di gnou dierigne thi batine ac zahir kontan na gnou thi mome

28.Posté par mor talla mboup le 02/05/2009 17:23
oustaz alioune sall sa kham kham sellena refetna yalla na yalla goudal sa fan amine

29.Posté par Khadyja Seck Ndiaye le 05/05/2009 23:43
ASSALAMOUALEYKOUM WA RAKHMATOULAH OUSTAZ ALIOUNE SALL niogui lay geureum dilasant dilla nianal weer, goudfaan ndakh ga doolé diarigne muslimyi.
Dama bougone am sa e-mail oustaz ndakh dama am lath bouma beug nga dimalimathi

30.Posté par pape matar le 11/05/2009 02:19
oustaz alioune sall yalla nala yalla faye

31.Posté par amadou gaye le 27/05/2009 00:06
assalamou aleykum wa rahmatoulahiwa barakatoukhau ya ouztaze yalla na la yalla faye na layalla faye

32.Posté par bathie lo le 27/05/2009 18:53
merci oustas sale yalla gafi yag tewer

33.Posté par bathie lo le 27/05/2009 19:00
oustas ya bakh mande sopnala loool yalla nala yalla fay te yagallafi goudal saw fan si barkeb serigne touba legui nekouma senegal magui españa waye maguilay deglou si internet diereu dieuf

34.Posté par diouf le 05/06/2009 17:45
Que dieu augmente votre connaissance ya seyd aliou sall

35.Posté par aminata le 19/06/2009 17:36
assalamou aleykoume ya outaz inni akhitou fii Allah waxtani dafamaye yokou bou bakh qu'Allah vous garde et vous protége.

36.Posté par mour le 26/06/2009 15:16
Ya Oustaz fouma tolou si adina magui lay santa dila nganal wer, dounda ak kantane dakh ligua sopi si mane yalla rek moka kham. lép lo beugue Yalla nalaka yalla maye.


Dans la même rubrique :
< >

Samedi 3 Décembre 2016 - 15:30 VIDEO – Exclusive : Cheikh Sarr brise le silence

Actualités | Politique | Economie | Fait Divers | Société | People | Sport | Coin des femmes | Culture | International | Vidéo News | Buzz du monde | Bande dessinée | Un café avec | Dinama Nekh | Buur Guewel | Double vie | Ndiaye Dollar | Wiri Wiri | Le reve de Akis | Rirou tribunal | Revue de presse | Blagues





Copyright © 2007 - 2016 Xibar multimedia Tous droits réservés

DIRECTEUR DE PUBLICATION: Abdoulaye Sogue - Contact: Protect e-mail with only css

Xibar Multimedia - 2901 41st Ave, Long Island City, NY 11101, United State