Référence multimedia du sénégal
.
Google

[VIDEO] Importante déclaration de Serigne Saliou Mbacké après la prière de l'Idul Fitr (Korité)

Article Lu 14952 fois


[VIDEO] Importante déclaration de Serigne Saliou Mbacké après la prière de l'Idul Fitr (Korité)
A l’occasion de la célébration de la fête de rupture du jeûne (’Idul Fitr, Korité), le Khalife Général des Mourides Serigne Saliou Mbacké a fait une importante déclaration après la prière. L’intégralité du sermon recueilli par le Groupe Communication de Hizbut-Tarqiyyah.



Source: htcom.sn

Article Lu 14952 fois

Dimanche 14 Octobre 2007





1.Posté par Aida le 14/10/2007 07:19
Mbakhe balla yalla na fi yague te weer loole
goor gui moo bakhe nitou yalla deugue mougui ni yalla na ko fi yalla bayi bassi kanama kaname
lima metti rek moy limala mounoul guiss diakhrane

2.Posté par njie le 14/10/2007 10:57
yalnaniou yala tasse thi sa barke m'backe ,yala ngua fi yague te were ,alhamdou lilahi rabil halamina,

3.Posté par mini le 14/10/2007 11:21
alhadoulilah rabil alamina ,li sant bou were leu pour kepp kouy senegalais ,lii dé nitou yalla mounou koo wéssu ,gnoun ni tamm gnoo nguiléy sakkou nian di la nianal yalla na la yalla bayi fi mou nyagg loolu té ande ak wér .

4.Posté par Mame le 14/10/2007 12:14
Akasssa ,sama serigne Yall ghafii yagh t weur thi barkep YONENTIBI.(psL}.......BAllak maramm ayssak sadjo mam diarra bousso mithi porokhane

5.Posté par wax sama xalaat le 14/10/2007 12:42
S.Saliou yalna gnafi yag looooooooooooooooooool té wer.
Kouko wax yalnanga ami khéwal.

6.Posté par bob le 14/10/2007 14:42
amen

7.Posté par dfsdf le 14/10/2007 14:43
yalna yala deffe gneupe ame goudi fane akh were gou yarame. yalna senegal ame diama; wa salam

8.Posté par akassa le 14/10/2007 15:08
serigne saliou yag fi te weer! serigne saliou moy royoukaay, ne nieup roy ci mom

9.Posté par maodo malick le 14/10/2007 16:21
j'arrive pas a pouvoir ecouter la declaration car le lien ne s'affiche pas surma page web qan j'ouvre le lien.

10.Posté par McCisse le 14/10/2007 16:44
Et de surcroit Il ne sait pas parler en public, Il a l'air de monloguer. Cependant merci de ses prieres.

11.Posté par Moctar le 14/10/2007 17:56
Alhamdoulilahi, Sant YALLA bou Wer,Dieuredieuf Serigne TOUBA, Diarawlak MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL, SERIGNE SALIOU YALLA nafi yag te and ak weer

12.Posté par merde le 14/10/2007 18:32
mon ami tu parle comme un eloquant je suis vraiment content de ce vous avez parler mais tu doit connaitre celui lla peu etre ton pere tu doit avoir le respect envers lui .tu devais commencer comme kara le malfaiteur et bethio et serigne mansour l`ignoraNT ET FETISSEUR MESSAGE POUR TOUS LES TALIBES QUI NE SAVENT PAS LE DROIT CHEMIN

13.Posté par Mustapha le 14/10/2007 18:56
On trahi ce peuple. Les senegalais doivent pratiquer un islam plus authentique et plus simple et laisser ces trucs de marabouts et autres. Ils faut voyager dans les autres pays muslmans arabes et non arabes pour se rendre compte que les senegalais ont beaucoup a apprendre. Nous perdons notre temps sur des futilites que nous croyons islamiques

14.Posté par Ariba le 14/10/2007 23:38
Dieumou djii Kham nguééne né loudoul diammou Yalla Ak santa ko digléwouko nite gni niooy wakh wakhi plotique dieum ci moom wayé moom loolou sokhalouko té dou torakhal kénne koufi nieuw dangay foogné yaw rék yay nitam batakhna ngni khamatoul founou dieum dici profitoo ak diko toogne yalla nako yalla yagal ci sounou kanam té may kou wërgui yaram bidiahi saydina mouhamed (psl)
Kou khamoul lane mooy yoonou mourid kii mooy royoukay ki massouta tégui tankam ci liko baya boutédda ba di diangallé bayyi di khool mourids ci yénna Serigne you sankou yi di profito ci yoone té khamou niou sakh li Serigne TOUBA digléé Mam Salihou Mbacké yalla ngafi yagg té wër

15.Posté par Ariba le 14/10/2007 23:42
Dieumou djii Kham nguééne né loudoul diammou Yalla Ak santa ko digléwouko nite gni niooy wakh wakhi plotique dieum ci moom wayé moom loolou sokhalouko té dou torakhal kénne koufi nieuw dangay foogné yaw rék yay nitam batakhna ngni khamatoul founou dieum dici profitoo ak diko toogne yalla nako yalla yagal ci sounou kanam té may kou wërgui yaram bidiahi saydina mouhamed (psl)
Kou khamoul lane mooy yoonou mourid kii mooy royoukay ki massouta tégui tankam ci liko bayam boutédda ba di diangallé bayyi di khool mourids ci yénna Serigne you sankou yi di profito ci yoonou mourid wi té khamou niou sakh li Serigne TOUBA digléé Mam Salihou Mbacké yalla ngafi yagg té wër

16.Posté par MOUSSA le 14/10/2007 23:55
MBACKE YALA NANGAFI YAGUE TE WEER

17.Posté par khouna le 15/10/2007 03:21
reponse pour moustafa .....mon cher tun crois savoir kelk chose k les autres n savent pa alor k t'es un vrai cretin . t'aurai beau cherche un intellectuel sur l coran partout dan l monde mais inchaallah tu l trouvera a TOUBA...SERIGNE TOUBA AMOUL MOROM

18.Posté par badara le 15/10/2007 11:31
yalna nako souyou borom yagual kofi mou andak weer goumote seuk ak barke andak cheikh bassirou sarr mou diamou bamba

19.Posté par jo le 15/10/2007 11:38
certains mourides vous ne dites que des idioties écouter attentivement le message du serigne il n a fait que réétirer les recommandations d Dieu et de son prophéte Mouhamed rien que çà donc exécuter les voeux du serigne pour quoi tousces fanfaronnades et je préconise meme au serigne de veillez personnellement à l'apparition du croissant lunaire en quoi faisant? en invitant la presse et d déclarer solennellement le début ou la fin du ramadant pour rendre beaucoup plus crédible les informations émanant de lui car on a frolé le pire cette fois avec ces deux 2 déclarations contradictoires diadieuf

20.Posté par un inconnu le 15/10/2007 13:07
Un marabout doit apprendre.Un marabout qui ne connait rien en l'islam ne doit pas parler en l'islam.Durant tout son discour il n'a meme pas formuler ou reciter un HADITH ou VERSET coranique.Ce qui la fait ce n'es rien du tout.Il doit argumenter ce qu'il dit par des versets de coran comme le faisait le Grand Homme Cheikh Abdoul Aziz.Et je vous dit Serigne saliou n'est pas normal.C'est Serigne mansour qui le soignait.Il doit se taire car il n'a pas beaucoup connaissance en l'islam.

21.Posté par kebe le 15/10/2007 14:05
dound gou law and ak khèwale safara tawat yi goudeule fane wi wèrale thièryi tasou gnou sisa barkè serigne saliou yalah ngafi yag way mbacke balah aysa mangui gnane yalah kilifi dinè yi nèk senegal yeupp roy si kii wakh deug yallh koumèlnè mome wotè nasi diignètè touma bènne kilifi nak ndakh gnèpp samay kilifa dinè lagne wayè mangui lène di gnane gnou bayi plotic bignouye dougeule si dinè dji nakh boukou gnou mangui djègoulou wa salam

22.Posté par CHEIKH le 16/04/2008 23:14
MUSTAF QUE DIEU VOUS ACCORDE SA FAVEUR CHEIKH SALIOU NAÑU TAF CII BAR KEEM

23.Posté par tapha gueye le 12/01/2009 13:05
arrété de vous jetter des pierres c mieu les Serignes se connaissent diaroul niawo

Actualités | Politique | Economie | Fait Divers | Société | People | Sport | Coin des femmes | Culture | International | Vidéo News | Buzz du monde | Bande dessinée | Un café avec | Dinama Nekh | Buur Guewel | Double vie | Ndiaye Dollar | Wiri Wiri | Le reve de Akis | Rirou tribunal | Revue de presse | Blagues





Copyright © 2007 - 2016 Xibar multimedia Tous droits réservés

DIRECTEUR DE PUBLICATION: Abdoulaye Sogue - Contact: Protect e-mail with only css

Xibar Multimedia - 2901 41st Ave, Long Island City, NY 11101, United State