Référence multimedia du sénégal
.
Google

'Paa REEBATASS' du Vendredi 21 Septembre 2007

Article Lu 11684 fois



Auteur: Pape Thierno
© Cocorico N°84


Article Lu 11684 fois

Vendredi 21 Septembre 2007





1.Posté par eva le 21/09/2007 15:38
tres bien diguéne ya ko yoor dé mais Idy je vien de lire ta proposition j'etais absente hier je voudrai bien paréna pour beurré lol

2.Posté par daba le 21/09/2007 16:27
Eva,
deugue nga wakh, djiguène gné ko yor mome, reebatass dofoul sou beuré woul dina kham . Mais Eva, bayi nala ak idy parceque mane la warona beurél mais mane kor gué ma diapou, kou dane si yéne gnar sokhla nala aprés la korité Inshallah

3.Posté par IBNOU le 21/09/2007 16:33
lol tieuy Jiguen, jiguen mo doy waar. lu niou dougg rek jiguen ya niou si dougal

4.Posté par max le 21/09/2007 16:53
Ibnou wakh nga leup, euy djiguén, ngor bou défé lou bakh djiguéne na takh, mou dougueu ci lou bone, djiguén na takh!!!!

5.Posté par max le 21/09/2007 16:54
mais eva, daba ak idy quel genre de beuré vous préparez? beugue na done arbitre!!!!

6.Posté par Idy le 21/09/2007 16:56
Eva,

Est ce que Daba expliké naleu beurébi.
Maname Aller/retour laye nékkeu. gnou taneu nakk kane moye ndieukeu fekssi.
Mann je préfére beuré aller bi ci sa Aréne appelé "Arénou Eva"

Mon ecurie s'appelle "Songalmako"

7.Posté par Idy le 21/09/2007 16:58
Rébatass daale , na déme beurédji waat mo gueneu waurr déh.
comme le disait un chanteur "diaral ngama songue Tyson , goalou Train"

8.Posté par Idy le 21/09/2007 17:32
Max,
beuré bi c'est à guichet fermé amoul spectateur.
En plus bo néké arbitre damaye bagn nga diéki rekk dougg ci beurébi

9.Posté par eva le 21/09/2007 17:46
idy dal digua ma ray rék mais nak daba m'avais rien expliquer et en plus yaw sa expliquation lééroul dara way si lou léér lay doug wakhal mou geuneu léér et je ss dacord que max soit arbitre

10.Posté par boy lebou le 21/09/2007 18:22
EVA
moytoul embuscade dé bala ngaye beuré na lér té da fa mel ni daba complice leu lol
wayé dara sou féké da ngaye beuré mome kaye ma diokh sa ma mara mou defal débadeb di nga dane ma la ko wakh
sinon reebatass deloul rek ah kou sagnoul bagne sagna naguou

11.Posté par Idy le 21/09/2007 18:21
Eva,

pourtant lérna di.
Beuré bi aller/retour leu. Match aller , yaw yamaye recevoir ci sa aréne.
aprés gnou teugaat retour bi , ma recevoir leu ci sama aréne. ne t'en fais pas mon aréne s'appelle "téralko bamou deloussiwaat"

Sou gnou défé match nul aprés gnou beuré sur un terrain neutre.

Max wolouwoumako ci arbitrage bi , mome beuré moko gueneu intéressé on dirait. Damaye bagn mou nangou combat bi ci mann

Avant de commencer comme s'appelle ton Aréne et comment s'appelle ton ECurie ???

12.Posté par max le 21/09/2007 19:44
ah bon zé compris, pardong mésseu, pardong medam,
En tout cas eva, moytoul boubakhabakh!!! en tout cas comme mounama done arbitre, donc moune na suppoté, té eva lay supporté!!!
bonne chance eva

13.Posté par boo le 22/09/2007 00:51
baahna daal yènne daal beurrè noulène nèhè nguène koyy dèffè eva yaww damalayy fèkk si daane la thieumme

14.Posté par ndiog le 22/09/2007 00:52
Femme bi dall barri na fémmee.

15.Posté par daba le 22/09/2007 10:22
Eva,
Idy dale wolou woumako, nila lama défone mais finalement il a renoncé notre combat né yow laye beurél. Li Max wakh deugue la il faut faire trés attention. Mane sama écurie s'appelle 'Boul ko Misére lo". Mane sakh éva yow laye supporté

16.Posté par eva le 23/09/2007 13:08
merci daba on es ensemble mais idy na kham né réssoumako é mon écurie s'appel "Boul ko dioy lo" idy je ss pête yaw rek lay khare puisque j'ai des soutien tu peux venir

17.Posté par Idy le 24/09/2007 10:43
Eva,

dama beugone lathié arbotre bi les reglements.
Ndakh beuré bi amneu galgal ak weur ndomba??

Max,
qu'est ce que t'a compris.? beuré la rekk, mais ce sera à huis clos, damaye bagn supporterou Eva ak samaye supporteres khékh ci Arene Bi.

18.Posté par boy lebou le 24/09/2007 12:07
EVA; IDY;DABA
man dé maye yor micro central bi sou féké amna transmission mais j'en doute fort;mais nak il faut que niuo commenté match bi mais nak commentaire audio rek laye nek comme ça supporter yi kham kan mo dominé ak kan la niouye dominé au moins

19.Posté par daba le 24/09/2007 12:39
boy lebou,
je suis parfaitement d'accord avec toi.

20.Posté par eva le 24/09/2007 14:31
comme vous voulez les gards magui séne guinaw mais idy boul ragual dara samay supportère ay nadiité lajniou té ils n'aiment pas le desordre beuré rek dane la jniou kham

21.Posté par boy lebou le 24/09/2007 16:38
wa mais dans tout ça combat bi c kan ? amoul combine beuré amoul dopage naye léér surtout dopage bi souvent gars yi da niouye dopéwou si péte té dopage mome amna fou moute daguané

22.Posté par daba le 24/09/2007 16:51
idy dégue nga li boy lébou wakh, nangua si bayi khél. OK

23.Posté par eva le 24/09/2007 17:54
boy lebou dacord na idy momassi diakhal ak ay niitam mais pour mane ak sama gua yi ya pas de blems

24.Posté par Idy le 25/09/2007 11:45
Daba, Boy Lebou,

Amoul dopage , mais amna consommer tonifiant rekk.

Eva,
mann daal boumeu sagnone beuré bi nekkeu a huis clos, pas de spectateur, damaye bagn gnou atté.
Aussi pas de reporter , ni de radio.

Boy LEbou ,
khana balagno diokhé date bi signé contrat bi
Mann "tiébou diaga " laye deff sama sponsor , mome lagnoumaye toggal ci jour bi


Dans la même rubrique :
< >

Mercredi 24 Août 2016 - 14:17 Quel réseau ???

Mercredi 10 Août 2016 - 14:37 C'est pas fil ooh !!!!

Actualités | Politique | Economie | Fait Divers | Société | People | Sport | Coin des femmes | Culture | International | Vidéo News | Buzz du monde | Bande dessinée | Un café avec | Dinama Nekh | Buur Guewel | Double vie | Ndiaye Dollar | Wiri Wiri | Le reve de Akis | Rirou tribunal | Revue de presse | Blagues





Copyright © 2007 - 2016 Xibar multimedia Tous droits réservés

DIRECTEUR DE PUBLICATION: Abdoulaye Sogue - Contact: Protect e-mail with only css

Xibar Multimedia - 2901 41st Ave, Long Island City, NY 11101, United State