Référence multimedia du sénégal
.
Google

'Paa REEBATASS' du Mercredi 5 Septembre 2007

Article Lu 11046 fois



Auteur: Pape Thierno
© Cocorico N°72


Article Lu 11046 fois

Mercredi 5 Septembre 2007





1.Posté par Ibnou le 05/09/2007 17:21
SE ME GAR YI KO LAINE FARAL WAAY SI COMBAT BI

2.Posté par daba le 05/09/2007 17:32
MANE REEBATASS LA FARAL

3.Posté par Idy le 05/09/2007 17:44
Daba mann yaw la faral . té yaw la beugg beuréle.
ci beuré yaw lassiye faral

4.Posté par boydkr le 05/09/2007 20:18
c sera 1 copie coller de gorgorlou talpadam

5.Posté par eva le 05/09/2007 21:03
MANE TAMITE REEBATASS LA FARAL YaLLA NA DANE WAY NANKH AFFAIRAME BAKH

6.Posté par daba le 06/09/2007 10:15
IDY MANE NGA BEUGA BEURELE, GNEUWEUL MANGUI LAYE KHAR

7.Posté par Idy le 06/09/2007 14:03
Daba,

beuré bi fanelaye amm??
Damaleu beug fekssii sa ARéne gnou beuri.
Aprés nga fekssimeu. dagnoukoye deff Aller/retour.

match aller ce sera pour ce Samedi avant gnouye dougg ci Ramadan bi.
Match retour 2 jours aprés.

Mann fimaye beuréwé il faut mou amm thiouraye bou nékh boufiye dioli

Songanté bi kagn leu

Mais nakk amoul aye khons déh

8.Posté par daba le 06/09/2007 14:35
Idy, beuré bi sama Aréne la, mais nak fok mou ame aye khons, mais nak samaye khons mome yénéne laye done, gnome séne thiouraye, gnome thiopéte ak némali bi lépaye dioli...

9.Posté par artist le 06/09/2007 15:46
daba avan ngay beuré ak kenén il faut que nou beuré

10.Posté par daba le 06/09/2007 15:52
Artist ténga bayi bama beuré ak Idy, aprés nga ladj revanche, je sais trés bien que damaye dane idy, dieul boudoul ame béne wéranté.

11.Posté par idy le 06/09/2007 16:21
Daba,

paréna, est ce que parénga ????
Daba , ci sa ARéne fofou lagnouye beuréwé Aller bi ak retour bi.
mangui khaar sa lettre de convocation ndakh khoumoumeu fou sa aréne fétéh.
Daba dama namm lambeu djii, namm naa aussi les khons que tu prépares nemali, et la tenue de combat que tu vas porter.
Beuré bi nakk sokhlawoul arbitre ak spectateur , ndakh aller retour leu .


Daba meun ngama Khon bamou saff sapp,

Léwto bi dafa khawa yagg té yégagougnou aréne bi.

wakhal ak sama manager elzonimo@yahoo.fr

12.Posté par daba le 06/09/2007 16:57
Mane kaye paré na mais beuré fokou mou ame arbitre sinon bou diéle amé kone nougnouye deff? ak sama écurie (Boul ko Misére lo) kone nane la léne di deff?

13.Posté par artist le 06/09/2007 17:30
daba apré nga contacté ma ci adresse bi thiernobeetoo@yahoo.fr

14.Posté par daba le 06/09/2007 17:39
Amoul bléms artists, té boul ma faté si gnane nak

15.Posté par Idy le 06/09/2007 18:16
artist comme tu t'appelles Thierno , alors yaw def nagnou leu serigne pour gnaane. Serigne dou beuri. bo beuréwé ak Daba , aprés la direction du penkou dinaleu rérr déh ndakh miir.



16.Posté par Idy le 06/09/2007 18:20
Daba,
yaw mome sa beurébi ci aye paroles la yame.

sama Ecurie "moye doumeu kou ndankeu té boul ko gaagn"

17.Posté par daba le 06/09/2007 18:53
yow dale idy daffa mélni gnémé woma

18.Posté par artist le 06/09/2007 22:15
ma lank la wakh douma serigne kan mola xakh tierno laa toudou idy

19.Posté par pene le 06/09/2007 22:17
wala reebatass waay


Dans la même rubrique :
< >

Samedi 3 Décembre 2016 - 15:55 Tros de sel dans la sauce

Samedi 3 Décembre 2016 - 15:54 Affaire de conduite !!!

Actualités | Politique | Economie | Fait Divers | Société | People | Sport | Coin des femmes | Culture | International | Vidéo News | Buzz du monde | Bande dessinée | Un café avec | Dinama Nekh | Buur Guewel | Double vie | Ndiaye Dollar | Wiri Wiri | Le reve de Akis | Rirou tribunal | Revue de presse | Blagues





Copyright © 2007 - 2016 Xibar multimedia Tous droits réservés

DIRECTEUR DE PUBLICATION: Abdoulaye Sogue - Contact: Protect e-mail with only css

Xibar Multimedia - 2901 41st Ave, Long Island City, NY 11101, United State