Référence multimedia du sénégal
.
Google

'Paa REEBATASS' du Mardi 26 Septembre 2007

Article Lu 11219 fois



Auteur: Pape Thierno
© Cocorico N°87


Article Lu 11219 fois

Mercredi 26 Septembre 2007





1.Posté par Le Jeune le 26/09/2007 18:15
Tres bien Réébatass.
Khalébi diar na songue TYSON mba BOMBARDIER walla sakh YEKINI.

2.Posté par Ngouri le 26/09/2007 18:27
hahhahah non rebatass bainaine aafaire le, mo ngui sentoo 4em, naane "SHUT SOKHNASA NGUI NIOW" LOOOL

VRAI SENEGALAIS KOI

3.Posté par bouta le 26/09/2007 21:53
Sokhna dal mo ko yor. A bas toutes les autres : Dey defar beu mou bakh, Tabakh beumou Kawe, Reebatass tog togay donkasigui, mane ni leu. Champion degnou koy teral ni bour

4.Posté par Paco le 26/09/2007 22:00
Paco yaye bandit, sa khalébi bakh na dé!!! wala bok!

5.Posté par boy lebou le 27/09/2007 10:54
apres l'effort le reconfort
pa reebatass sa khalé bi mome ba dééééééé
DABA bougou meu nga setane combat bi en directe parce ke g peur que tu pique a EVA kelkes gualgual wala weur nombe bayil rek ma diokh la ko en diect c plus sure

6.Posté par daba le 27/09/2007 11:19
Boy lébou je ne suis pas d'accord, bayil rek ma gneuw sétane si beugouma raté dara si combat bi, dougoussi bi, léwto bi ak combat tchimmmmmmmmm fofou nare na todjie

7.Posté par boy lebou le 27/09/2007 13:28
DAABAAA comme tu veux wayé da maye ragal nga khoff parce ke nek sou féké né combat bi da fa dieul bénéne tournure ba lumineuze yi astafourlaaaa projecteurs yi ba bethio yi astafourlaaaa seurou ndiago yi dioli da maye ragal nga daw té souboba match dou am

8.Posté par eva le 27/09/2007 14:22
boy lébou yaw mome daba amoul lou mouye tite parceque say gualathie toch na ba parré inchalla nous les filles allons vous battres toi et Idy préparéléne rek gualgual ak weur nombe si yém kép

9.Posté par daba le 27/09/2007 14:31
Eva,
boul wakh dara, mane amouma loumaye tite si boy lébou ni Idy, khamougne né djiguéne gné ko yor

10.Posté par boy lebou le 27/09/2007 14:44
EVA akh DABA mane bala maye meuneu béré rek niou weur ma nombe wala niou rof ba gualgual. je suis plus dangereux a terre. khamouma idy dé wayé ''ecurie dem dik'' niou ngui tok di léne khar door doorate soce socate bath bathate sekh sekhate. gosse ama nguéne serieux probléme samedi yaguatoul
IDY mbeur se guéwe beu fok diéleu ame

11.Posté par eva le 27/09/2007 15:07
mais khana bay lebou yaw ak Daba moye samedi paceque make idy mome dessnadé

12.Posté par daba le 27/09/2007 15:19
Eva,
Sa combat ak Idy moye samedi, d'aprés li boyé lébou wakh

13.Posté par boy lebou le 27/09/2007 15:23
ah IDY mo wakh né séne combat samedi Minuit apres nafila yaw EVA loye tite khana nékatoko avec sa ngaye wakh djiguéne mo ko yor kou daw da nga ragal wakhal akh idy man sa ma combat akh daba wakh na apres ramadan bi leu man je fais ke reporter votre match

14.Posté par boy lebou le 27/09/2007 15:27
mounane paréguouma amoul echpliké dara tu veux juste te défiler en douce khamna gualgual yi akh weur nombe yi nio la si titeul
daba yaw mome parel bétoumala un homme averti en vaut 2 mais une femme averti en vaut 10 ah thimmmmmm dem dik

15.Posté par eva le 27/09/2007 15:34
nooooooo boy lebou dal ya beugue lou yomb rek. de toute façon je peux pas me prononcer sans entendre la version de mon adversair mais mome sakh fou mou nek tay dafa rare

16.Posté par daba le 27/09/2007 15:40
Eva titoul, dawoul, Idy moko wakhoul lou lére peut etre dafa reporter combat bi, parceque mingui né ték wakhoul dara, khamouma dafa ragal Eva wala!

17.Posté par boy lebou le 27/09/2007 16:02
mais IDY fo nek echke damou séti mame yi pour aye sanguate yoyou lol

18.Posté par Idy le 27/09/2007 16:48
Eva,

légui tambalinga daw déh.
Ok légui comme Eva gniméwoumou, maynenako Daba bokkeu ci combat bi.
Maname Idy contre Daba et Eva à la fois. cette gnateu dina beuré té gnaar meunoul Idy.

Donc on remet ça jeudi p^rochain.


Boy Lébou preparéle dossier signature contrat. Khana gnii à 2 dinagnoumeu gnimé songueu.

Mon ECurie va ainsi s'appeler "Songamaléne"

19.Posté par boy lebou le 27/09/2007 17:25
sou féké les filles sont d'accord rek ma changé termes signature bi mais amateurs yi bo léne degué ma tek micro bi rek khamléne né IDY la niouye newal dolé té damaye sote ahh wawaw solidarité masculine
yénaye séte
hunnnnnn wayé combat a 3 mome doye na war dé khana da ngaye dopé wou mais g été clair et net DOPAGE amoul nieup la wakh neuk di na léne teshhté


Dans la même rubrique :
< >

Mercredi 24 Août 2016 - 14:17 Quel réseau ???

Mercredi 10 Août 2016 - 14:37 C'est pas fil ooh !!!!

Actualités | Politique | Economie | Fait Divers | Société | People | Sport | Coin des femmes | Culture | International | Vidéo News | Buzz du monde | Bande dessinée | Un café avec | Dinama Nekh | Buur Guewel | Double vie | Ndiaye Dollar | Wiri Wiri | Le reve de Akis | Rirou tribunal | Revue de presse | Blagues





Copyright © 2007 - 2016 Xibar multimedia Tous droits réservés

DIRECTEUR DE PUBLICATION: Abdoulaye Sogue - Contact: Protect e-mail with only css

Xibar Multimedia - 2901 41st Ave, Long Island City, NY 11101, United State