Référence multimedia du sénégal
.
Google

'Paa REEBATASS' du Mardi 25 Septembre 2007

Article Lu 11286 fois



Auteur: Pape Thierno
© Cocorico N°86


Article Lu 11286 fois

Mardi 25 Septembre 2007





1.Posté par demd le 25/09/2007 16:28
HAHHAHA DIEUL BU AMOUL BAINE WERENTEH LE KO DAANE,

AK BEUT BOU PAT BI

2.Posté par papis le 25/09/2007 16:30
non! dafa yombe torpe nak.mé cé comme le combat baboye / bombardier à thies.

3.Posté par mix le 25/09/2007 16:55
enfin, enfin, legui nak que rebattass a gagné, lou dess? that the question!!!!!

4.Posté par Idy le 25/09/2007 17:06
Mix,
Rébatass va se cooler en douce , son prochain Combat c'est la belle SOKHNA.
hahaha

Légui warna meuneu teug sama gnari combats yii: Eva puis Daba

5.Posté par zales le 25/09/2007 17:06
walabock....Ki kan la wayyyy!!!!! Paa REEBATASS

6.Posté par daba le 25/09/2007 17:36
Wakhone nako Reebatass dale dou séne morom

7.Posté par daba le 25/09/2007 17:46
Idy prépare toi,mane ak Eva mome paré nagnou yow rek yassi désse

8.Posté par boy lebou le 25/09/2007 18:04
lou ma léne wakhone pa bi mo ko yor
DABA teunk na la combat match d'ouverture bou big match EVA / IDY comme ça mbeur meuneu bakou avant niouye beuré
kou daw da nga ragal

9.Posté par adams le 25/09/2007 19:49
Paa REEBATASS . Dafa Door Doorat...... Door Doorat......... Door Doorat
Diadieuff wayy .............REEBATASS

10.Posté par boye le 25/09/2007 20:52
bravo a mon lutteur reebatasssssssssssssssssssssssssssssssssssssssssssss

11.Posté par daba le 26/09/2007 10:40
Boy lébou amoul blém contactéle sama menager rek combat bi takhaw

12.Posté par boy lebou le 26/09/2007 10:50
marché conclut daba bake nga ndiak dééééééééé a tchieum

13.Posté par daba le 26/09/2007 11:16
A thieum boy lébou mais sache que ndiak eksiwoule déé

14.Posté par boy lebou le 26/09/2007 13:40
yaw daba sa ecurie nou mou toudeuti sakh ngané ?

15.Posté par ive le 26/09/2007 14:08
hahahahahahahah content na si sama pa by khamone na dou jniou rousslo
idy
tu vois pa reebatass m'a redonné du courage yégue sile ma gui laye khar

16.Posté par eve le 26/09/2007 14:09
mané eva le ive que tu vois

17.Posté par daba le 26/09/2007 14:18
Mane écurie 'Boul ko misére lo" la bok, yow nak sa écurie noumou toudou?

18.Posté par boy lebou le 26/09/2007 14:44
maane sama ecurie ''dem dik'' leu toudou yaw khamo sakh si li nga gougue a thieum

19.Posté par boy lebou le 26/09/2007 14:50
daba ragal na nga dem si ardo dé lollololololol bakeu ndiak té man khamné né di nga fa fek ndiak j'en suis sure meme

20.Posté par daba le 26/09/2007 15:39
boy lébou, ndiak dé souma kofa féké dou bakh si mome

21.Posté par Idy le 26/09/2007 16:03
boy Lebou,

loutakh sa Ecurie toudeu "dém dikk" , hahaha

En tout cas kharléne ma Paré ak Eva , puis Daba.

22.Posté par boy lebou le 26/09/2007 17:02
idy on se comprend toi et moi ''dem dik'' bi mbaut mo si nek
daba fekhel rek ba fek fa ndiak

23.Posté par Idy le 26/09/2007 17:15
Samedi prochain, à partir de minuit aprés les NAfileus, ce sera mon combat contre Eva.
Eva va me recevoir dans son aréne pour le match Aller.

Eva , comme ce sera un combat nocturne , à toi d'assurere l'eclairage avec les Lumineuz....euh ...pardon je veux dire Projceteurs

24.Posté par daba le 26/09/2007 17:55
wakh léne ma fou aréne Eva nék, parceque combat bi mome boy lébou doumako nétali

25.Posté par boy lebou le 26/09/2007 18:30
man mome je vais attendre la fin du ramadan parcheke ragal na combat tar si kéne si nioune ba dou meuna woor lendemain bi
wanté DABA sou fékké né ke wolou nga sa bop bismila yeksil diam dalal diam


Dans la même rubrique :
< >

Vendredi 9 Décembre 2016 - 13:20 La bonne sexy

Jeudi 8 Décembre 2016 - 12:36 Tentative de...

Actualités | Politique | Economie | Fait Divers | Société | People | Sport | Coin des femmes | Culture | International | Vidéo News | Buzz du monde | Bande dessinée | Un café avec | Dinama Nekh | Buur Guewel | Double vie | Ndiaye Dollar | Wiri Wiri | Le reve de Akis | Rirou tribunal | Revue de presse | Blagues





Copyright © 2007 - 2016 Xibar multimedia Tous droits réservés

DIRECTEUR DE PUBLICATION: Abdoulaye Sogue - Contact: Protect e-mail with only css

Xibar Multimedia - 2901 41st Ave, Long Island City, NY 11101, United State