Référence multimedia du sénégal
.
Google


hh



[ PHOTO ] Tyson, le gentleman de la lutte



[ PHOTO ] Tyson, le gentleman de la lutte

Vendredi 27 Avril 2012




1.Posté par mass diène le 27/04/2012 10:43
Mani ki dou touss, workat bou bone la, mo takh khol lènn nimou moudié...chimm, il a boufé tout l'argent de Eumeu Sène, mo takhit djigouko. Pour de l'argent, il peut prostituer sa femme. Badola va

2.Posté par baye zal rim le 27/04/2012 12:54
ki dou dara loudoul woutkatou khalisse niack diom pourquoi tu na pas demander ton revanche contre balla guaye.

3.Posté par balzo le 27/04/2012 13:47
bayi léne linguéni wakh ki amoul loumou défoul si lamb dji bék lona kounék thi aye temps donc tous les lutteur et amateurs de lutte ont un merci pour le grand tyson

4.Posté par néné le 27/04/2012 15:40
TYSON A REVOLUTION .E LA LUTTE C EST GRACE A LUI QUE LES LUTTEURS GAGNENT DES MILLIONS AUJOURD HUI. AUSSI BALLA GAYE YEKINI BOMBARDIER THI MOME LAGNOU DONE ROY DONC KoU KHEW DINA KHEWI SOUVENEZ VOUS DES CHANSSONS DE NDONGO LO ENVERS TYSON C EST PARCE QU IL ETAIT FORT MAIS SENEGALAIS ANDOUGNOU AK KENE. KOU KHEW REK C EST BETE CA

5.Posté par moussa le 28/04/2012 09:46
Kou am loy def defale si sa soxna ak sa ay dom.Wwante si kenene ko def euleuk dina na la saxami ,xaxta ndikou la touflila si mbedeubi.

6.Posté par raison gardz le 28/04/2012 14:21
ignane bakhoul eumeu sene fenekatela lou takh mouye doule ter di waax founekke tyson moye khalifame amna trois xamougnou wayer ndiare xamnagnou

7.Posté par Abou le 28/04/2012 16:59
Tyson amoul diomm, mo takh mloudiamm niaw, dou nitou dara. Chimm. Nguir xaliss, meun na diaay domam you djiguèn yi

8.Posté par demba le 29/04/2012 15:39
tyson sera et reste mon lutteur arreté de dire des choses k vs ne connaissez pas imbecile

9.Posté par raison gardz le 30/04/2012 10:15
waw mo taye boukko nekher tamit amenaci droit yow ignane dongue mo takhe gua gnieuwe dit wax lougniawe wayer waax bougniawe deukkoule foumou dieumme foumou diogguer la deuggue alors va te faire soigner avant d attraper une crise cardiaque et toute ta famille sera fatiguer tyson affair bi momela lolou la yalla dogalle mbeuler borom khole bou bonne beu moujou neuppe

10.Posté par raison gardz le 30/04/2012 10:29
tyson mokko yor sans vulgarite sans arrogance et surtout beaucoup de grace et de classe lawla thiette mala noppe xalebile ya maye dnelez!!!!

11.Posté par raison gardz le 30/04/2012 10:37
eume sene fene rek laye daff wayer un jour viendra gnigua bireulle yeuppe gua sandi si poubelle houte une divorce de toubab car elle est pensionnaire du toubab avc son enfant donc c est la facilite totale qu il cherche nous on le connait tres bien ici a pikine c est boye niang kon a plus feter sa victoire que celle de eumeu sene c est un ingrat et un abrouti je ne parle meme pas de tyson qu il a treahit et defier publiquement mais un jour viendra inchallah toute la verite ce saura.

12.Posté par raison gardz le 30/04/2012 14:06
kou merre bokko tyson defarna bamoubakh sunulambji gnougui koye sante dikko gueureum yalla nako yalla soutoureul abadanne dayemanne tyson akk balla gaye2 lagnou waax affairbi gniomla kou mou nekhoul sa affairla wouwou

Nouveau commentaire :
Twitter


Dans la même rubrique :
< >

Dimanche 20 Juillet 2014 - 00:23 Décès de l'artiste-peintre Souleymane Keita








Plateforme d’information et d’intéraction a temps réel
Optimisé pour être vu en 1024x768 I.E. 6.0 ou plus récent

Info sur Xibar.net | Conditions d'utilisation | Données personnelles | Publicité | Aide / Contacts |
Copyright © 2007 Xibar multimedia Tous droits réservés