Référence multimedia du sénégal
.
Google

[AUDIO] TEMOIGNAGE DE CHEIKH BETHIO THIOUNE SUR LE DECES DE SERIGNE SALIOU MBACKE

Article Lu 118164 fois

[AUDIO] TEMOIGNAGE DE CHEIKH BETHIO THIOUNE SUR LE DECES DE CHEIKH SALIOU



[AUDIO] TEMOIGNAGE DE CHEIKH BETHIO THIOUNE SUR LE DECES DE SERIGNE SALIOU MBACKE
.


Article Lu 118164 fois

Samedi 29 Décembre 2007





1.Posté par sidy le 29/12/2007 16:27
Dieurediuf Thioune,yaw ya takh ba dougnou diakh le waye Serigne bi de ya gnouko khamal.Boudoul wone yaw de,SERIGNE SALIOU dina gneuw ba dem te dougnou kham ni k moy KHADIMOU RASSOUL.Beug SERIGNE bi rek mo waure.Motakh gnou beug yalla de.Dogal yi yene kep la nekh.Dieurdieufeti SERIGNE CHEIKH BETHIO mou SERIGNE SALIOU

2.Posté par mor seye le 29/12/2007 17:30
serigne saliou ne nous quitteras jamais il est toujours la devant nous pour nous proteger contre les mals.

3.Posté par khadim le 29/12/2007 17:54
sereigne saliou yalla na ko yalla yeureum te tass nou ci bar kem amin

4.Posté par Fiitou le 29/12/2007 19:02
Ce n'est pas le moment de polémiquer, mais il y aura un temps de bilan des actes posés par des talibés ou sois disants qui n'ont rien fait pour grandir le mouridisme.

5.Posté par thiam Mamadou rance le 29/12/2007 23:04
innalil lahi wa inna ileyhi raadjihouna . allahu akbar laahi laaha illa lah seydina m rassoulilah. prions et remercions le tout puissant . soyons solidaire et fidéle à notre religion .cheikh saliou est parti mais ses oeuvres restetons à jamais .QUE DIEU L'ACCEPTE DANS SON PARADIS .AMENE
TTE MES CONDOLEANCES A LA OUMMA ISLAMIQUE

6.Posté par arghhh le 30/12/2007 11:48
Je trouve qu'il y a beaucoup d'émotions dénaturées et de sentiments artificiels. Imposer qui est juste, imposer qui doit être aimé c'est aussi imposer qui doit être ignoré. Je ne vois là que du fascisme qui aboutit à une société profondément injuste et inégalitaire.


7.Posté par Babacar KEBE mu CHEIKH BETHIO le 30/12/2007 14:01
Barkeb SERIGNE SALIOU.Chers mbokki talibès, nous sommes attristès par la disparition physique de SERIGNE SALIOU .CE KHUTB ZAMAAN d'une envergure momdiale est cependant constamment avec nous.SERIGNE SALIOU est Immortel.Son statut physique a changè mais nous talibeès de CHEIKH BETHIO sommes èlucidès sur "LE PERSONNAGE DIVIN" de cet "HOMME UNIVERSEL".IL EST ETERNEL et vivra toujours avec nous.Cependant la peine de quelque nature qu'elle soit ,sachons que SERIGNE SALIOU NE QUITTE JAMAIS .

8.Posté par niokho de milan le 30/12/2007 15:37
ASTAH FIROULAH ASTAHFIROULAH ASTAHFIROULAH revenons à DIEU de GRACE Le sènègalais pense qu'il est le seul musulman au Monde.Lisez le MEMORIAL DES SAINTS vous verrez que y'a eu d'autres saints dans ce bas monde.Et essayons de bien nettoyer nos plats pour que le BON DIEU puissent nous servir à GOGO.

9.Posté par TOUBA TORINO le 30/12/2007 16:06
Dieureudieuf Serigne Saliou,CHEIKH BETHIO ya gnouye mooome fawe

10.Posté par adi le 30/12/2007 17:42
bonjour magui bep senegalais musulman dilene diale siguil ndigale yalla nako yalla yeureum diegalko te khareco aldiana yi guena kewe si bar yonente bi salalahou alayhi wa salam amine dieuredieuf

11.Posté par khady le 30/12/2007 17:56
la illaha illallah
soubhana rabbika rabbil hizati hamaa yassifoona wasalamou hala moursalin walhamdou lillahi rabbil halamina
yaram yalla na niou yalla may niouy topp li nga santané
biss bouniou ko naré wath yalla na niou génn adouna

12.Posté par Ibrahima Samb le 30/12/2007 17:59
Barkeb SERIGNE SALIOU.Chers mbokki talibès, nous sommes attristès par la disparition physique de SERIGNE SALIOU .Mes condoléances à tout le peuple Sénégalais .

13.Posté par séga D. le 30/12/2007 19:32
A Fiitou et arghh: C'est lache de se cacher derriere ce pseudonyme qui traduit littéralement" courage" et de parler de polémiques qui d'abord n'existe nt pas ensuite aux noms de tous les thiantakones le moment "de bilans des actes posées" j'ose esperer que tu viendras avec quelques choses de concret en lieu et place de tes insinuations,dévoile toi si tu as des arguments et non des mots déplacés.
Pour ce arghh,dont le pseudo suffit pour savoir quels genre d'individus il est, il est trés mal placé pour apporter un jugements sur la nature des sentiments qu'éprouve un etre qui acheminer 61ans avec un homme Dieu,ce qui montre son manque de culture car c'est au CM2, j'espere qu'il est arrivé qu'on apprend le proverbe:"Dis moi qui tu hantes,je te dirais qui tu es" le jugement qu'il porte de façon implicite, n'a d'égal que son ignorance qu'il a platement étalé sur ce site, en parlant d'un homme dont le seul tort,si tort il y'a est d'aimer plus que TOUT son Maitre spirituel.
De grace donner des arguments, pour dédire ou taiser vous car votre attitude dans ce site ne reflete que vos envies et intention innavoués.

14.Posté par bousso le 31/12/2007 00:40
SERIGNE SALIOU moye souniou borome mome laniouye sante faw nous lui rendrons grace pour l'eternité pour nous avoir montrer sa realité qui est celle de SERIGNE TOUBA qui elle méme est celle de MOHAMED RASSOULILAHI et par conséquent celle de DIEU mome il est eternelle moye BOROME DIAMONO il incarne la NOUROU AHMADIA ki est la LUMI2RE DE MOHAMED par qui DIEU a créer tout ce qui existe avant de nier quoi que soit il faut d'abord acquérir la connaissant ... SERIGNE SALIOU MOYE CHEIKH BETHIO

15.Posté par jara le 31/12/2007 05:36
seringe bara mbacke yalla nafy yage ta were

16.Posté par joe sylla le 31/12/2007 12:34
serigne saliou mbacké yaala nafi yagg lol té wer diereudieuf thioune la revolution thianta en marche ne repondez pas a la provocation moi tt le monde me connais a travers xibar et rewwmi par la virulence des mes propos contre les incultes ki se perment de demonter le mouridisme mé cet fois je demnde a tt les thianta de ne pas reagir a ces gars dieureudieuf thioune

17.Posté par joe sylla le 31/12/2007 12:49
les gars on a montré hier le ziar du cheikh ki avé fé a serigne saliou le jour du magal sur rdv mé c dommage kil ont passé a 23h k dieu puisse fer kil le passe dans la journée il sauront kié serigne saliou et le cheikh

18.Posté par Andrée le 31/12/2007 13:24
Dieuredieuf Thioune Mame Bambi. Serigne Saliou dé gneupeu ko wara sant.

19.Posté par sismaila le 31/12/2007 17:23
DIEUREDIEUF SERIGNE SALIOU, DIEUREDIEUF CHEIKH BETHIO

20.Posté par Diakhaté le 01/01/2008 00:01
yéne sama mboke talibé yi bou niou tontou wakhe bou niawe. nagnou gueume yalla té khame né lou yawe déf bopame.serigne touba khadimoule khadime diéguale na aye noname.

21.Posté par Diakhaté le 01/01/2008 00:03
MOURIIDOULAH SERIGNE SALIOU YALLA NANOU YALLA TASSE THI BARKEME

22.Posté par Adji Kiné le 01/01/2008 16:07
Que Dieu le tout puissant l'acceuille dans son paradis éternel. Nous peuple sénégalais luttons pour la paix et rien que la paix.

23.Posté par seydina le 01/01/2008 21:13
serigne saliou dou koufi diouk;.. serigne saliou dou koufi diouk;;.. ndakh moye yalla sounou borom sgne saliou yalla nafi yag and ko ak cheikh bèthio thioune dieuredieuf thioune

24.Posté par sokhna mai mou cheikh bèthio le 01/01/2008 21:20
dieuredieufety serigne saliou cheikh bèthio yala na fi sakh tè wèèr gni gui niane yala yok lèèrame tè tass gnou si barkèm tè ma beugue nieup khamni serigne saliou moye cheikh bèthio ...........

25.Posté par faty le 01/01/2008 21:28
barkèp cheikh bèthio .la relation entre serigne saliou et cheikh bèthio c comme labsolu et son compagnon ..gni gi nianal cheikh bèthio mou yag fi lol tè wèrr amine

26.Posté par doudou le 02/01/2008 03:17
bethio thioune t la honte de nous les mourides

27.Posté par pape moustapha thioune diamou cheikh bethio le 04/01/2008 23:24
barkep cheikh bethio na gnou def cheikh bethio sougnou yiite waxii serigne saliou

28.Posté par YOUSSOUPHA MBACKE le 05/01/2008 02:38
ASSALAMOU ALAYKUM MBOKYI

LII LEPP NGEEN BIND FII DARA DOUTHI DEUGG LEPP AY FEN REK LA SERIGNE SALIOU CHEIKHALOUT KEN WAKHOUL BETHIO LOUMOU WAKHOUL TAALOUBE YI BAYYI LEEN SOSSAL SERIGNE TOUBA AK SERIGNE SALIOU MOOM DE WATHIE NA LIKO BAAYAM DIGALOON LAFI NEKKE WOON DAATHIE YARE BETHIO NAK YAKH LISLAM JI SERIGNE TOUBA DOON YEESAL MOOKO YEUKATI WAAYE GNI KHAMOUL REK LAY LOR SHEYTAANE REK NAKO GNEP KHAM SHEYTAANE NAK KHELAM REK LAY NAKHEE WAAYE MBIRAM DOU MOUDJ FENNE
YOUSSOUPHA MBACKE
IBN SHEIKH MOURTADA
IBN KHADIOUR RASSOUL

29.Posté par soxna astou sall le 19/05/2008 20:21
dieuredieuti serigne cheikhe bethio thioune khawma kouye youssoupha mbacké wayé kouko yeureumela firre rékako diape mayé dogalyi tabina yaguena cheikhe béthio moye serigne touba kou diapoule ci mome tu a tapé a coté.s youssoupha yéwoule

30.Posté par BABACAR FALL le 23/12/2008 05:54
Dieureudieufeti serigne SALIOU MBAKE la disparution phisique de SERIGNE SALIOU MBAKE nous a tous attristé .Que l'on sache qu'il est toujour la pour veiller sur les musulmans

31.Posté par mbaye ndiaye le 23/12/2008 15:07
l'homme saint,digne, courageur.
que le bon DIEU l'accueille dans son paradis,une journée inoubliale pour tous corps mouride.

32.Posté par Alassane Cissè touba dieuppeul le 02/02/2009 12:26
dieureudiefeuty Serigne Saliou Mbackè Cheikh Bèthio diamou Serigne Saliou yalla nafi yague tè wèr

33.Posté par ousseynou ba diamou serin chekh bethio "TOUBA TEROUBI" LIBER le 11/02/2009 12:30
dieure djefeti serign SALIOU MBACKE S.Cheikh BETHIO THIOUNE YALLA EUPE NDAMAL serign saliou diereu djeuf THIOUNE.
C'est sans doute le moment le + douloureux pour nous THIANTACOUNE de comprendre la disparition temporelle de S SALIOU mais grace a S.C.BETHIO nous parvenons a maitriser la situation; nous savons aussi + d'un que S.Saliou est parmi nous et il le demeurera a jamais.
N'en deplaise aux calomnies et autres invectives de ces oiseaux de mauvaises augures.Nous avons la chance d'etre avec l'homme fort tel SERIN CHEIKH BETHIO THIOUNE le L'UNIQUE guide spirituel contemporain jamais d'egal ni alter egaux
DIEREDJEUF SERIGNE SALIOU MO BARI YEURMEUNDE.
C.BETHIO DIAMOU S.SALIOU YALLA NA FI YAGUE LOLOU TE GUENE WER amine

34.Posté par ousseynou ba diamou serin chekh bethio "TOUBA TEROUBI" LIBER le 11/02/2009 12:50
Deja comme vous le constater le nom de DOUDOU est un nom pejoratif satanique synonyme du mal ;comme voulez vous qu'on repond a un adepte de satan comme doudou la merde.
Quant a YOUSSOUFA voila un qui sera toujour un ennemi de l'islam.Tu ne merites pas le nom de MBACKE
Tu sera tjrs un tare; un nullard;un suivant .....thipiri bandes de cons
YENA BONE WAYE

35.Posté par racine le 16/02/2009 01:05
le monde est un grd livre dont chak pas ns ouvre une nvlle page lii cheikh bi nianone Serigne Saliou M'backé défal bou niou guiss sou niou peundeu aksina na niou dém rek wayé...rires da nékhoul ndakh si yon bou mou meunti nek Thioune mo fi euup mbolo mo takh jalousie daf si am té mouride degue té yéss kham nga nii lou thiow lii beurri Cheikh bi geuneu amati ndam fii ak fi niou dieum

36.Posté par mame mor dieng le 16/02/2009 20:24
ziare a tout les talibès mourides surtouts les thiantacoune je prit a Serigne Saliouy de nous accorder sa grace boudoule wone yaw attebi dalenou sante bou weure

37.Posté par birahime konte le 09/04/2009 13:16
barkep cheikh bethio darah touba khombole niqui ziar tous les thiantakone de ma part thierno konte cheikh bethio yaque fi lole

38.Posté par birahime konte le 11/04/2009 16:26
ziare nalene yenne wa keur cheikh bethio walla noune thiantkonyii watie 17avril rekk moye yiteyi serigne touba nous dis la tafhalo sayanne bi khary izni yala na nou serigne by maye xame xame mou dieuf teyel nou sounou taloube niou sakhe cii keparame sakhe cii thiante gui vous les thianta noublier pas notre 16 mai a khombole cheikhe bethio dimebeliniou yague fi ba nieupe xame ne moye serigne touba amiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiine de ma part birhime konte khombole

39.Posté par aidara fall le 31/05/2009 04:46
SERIGNE SALIOU MBACKE est toujours là present et nous protege diko sant rek

Actualités | Politique | Economie | Fait Divers | Société | People | Sport | Coin des femmes | Culture | International | Vidéo News | Buzz du monde | Bande dessinée | Un café avec | Dinama Nekh | Buur Guewel | Double vie | Ndiaye Dollar | Wiri Wiri | Le reve de Akis | Rirou tribunal | Revue de presse | Blagues





Copyright © 2007 - 2016 Xibar multimedia Tous droits réservés

DIRECTEUR DE PUBLICATION: Abdoulaye Sogue - Contact: Protect e-mail with only css

Xibar Multimedia - 2901 41st Ave, Long Island City, NY 11101, United State