Référence multimedia du sénégal
.
Google

APRÈS UNE VIOLENTE ALTERCATION Talibés de Béthio Thioune et disciples des «yalla-yalla» lavent le linge sale devant le juge

Article Lu 15110 fois

Les rivalités entre les mouvements confrériques sont tellement manifestes que pour un rien les talibés n’hésitent pas à verser du sang. L’affrontement entre ‘’Thiantacoune’’ et ‘’Yalla-Yalla’’, ayant conduit à l’incarcération de 4 talibés, en est l’exemple probant. Ils étaient hier devant la barre du tribunal des flagrants délits. Après délibéré, ils ont été relaxés au bénéfice du doute.



APRÈS UNE VIOLENTE ALTERCATION Talibés de Béthio Thioune et disciples des «yalla-yalla» lavent le linge sale devant le juge
Encore des heurts entre talibés d’une même confrérie religieuse. Cette fois-ci il s’agit de talibés de Cheikh Béthio Thioune et ceux d’un nouveau mouvement issu du mouridisme : les Yalla-Yalla. Quatre prévenus appartenant à ce mouvement étaient hier devant la barre du tribunal des flagrants délits. Il s’agit de Moussa Tokola, Ass Seck, Malick Bâ, Baïdy Diallo poursuivis pour coups et blessures volontaires sur Ibrahiama Ndiaye, talibé de Cheikh Béthio Thioune. En plus de ce chef d’accusation, ils sont poursuivis pour détention et usage de chanvre indien. L’affaire a eu lieu au courant de ce mois d’octobre à Pikine Guinaw Raïls. Comme il est de coutume dans ces quartiers populaires, une rivalité sans commune mesure demeure entre les mouvements religieux. C’est cela qui sera à l’origine de cet affrontement entre ces deux mouvements. Et il s’en est fallu de peu pour que le pire ne survienne. D’après les déclarations de la partie civile, Ibrahima Ndiaye, «vers 1h du matin, après que nous avons terminé notre Kourel, je me promenais tranquillement accompagné d’une ‘’soxna’’. Arrivés à hauteur du Thiant des Yalla-Yalla, des insanités ont été proférées à notre encontre. S’en est suivi un accrochage où un groupuscule constitué des personnes sus citées m’ont balancé une pierre en pleine figure. Avec comme conséquence des blessures attestées par un certificat médical avec une incapacité temporaire de travail (Itt) de 30 jours». Propos qui seront largement réfutés par le principal mis en cause, Moussa Tokola. Qui soutient n’avoir point levé la main sur lui, encore moins lui balancer une pierre. La partie civile, dans sa réponse, n’a pas reconnu l’auteur de cet acte perpétré à son encontre. Les prévenus ont, en outre, nié avec véhémence le délit d’usage et de détention de chanvre indien. Des dénégations qui n’ont pas convaincu le Procureur qui a estimé qu’ils sont coupables des faits qui leur sont reprochés. Suffisant pour qu’il demande aux juges de les maintenir dans les liens de la détention pour une période de 3 mois. La partie civile, pour sa part, a réclamé 400.000 F Cfa en guise de dommages et intérêts. La défense, assurée par Me Papa Ndiaye, a souligné qu’il y a un problème d’imputabilité des faits. Il a également dénoncé la manière téléguidée de la police sur l’arrestation de ces jeunes suivie de la découverte du chanvre indien. Des observations sur lesquelles l’a rejoint le président du tribunal. Qui les a relaxés au bénéfice du doute.

Source: L'observateur

Article Lu 15110 fois

Mardi 21 Octobre 2008





1.Posté par galsen le 21/10/2008 22:09
KOUFI BAYIWOUL YAMBA AK BETIOU TATE!
MEFIEZ VOUS DES SECTES

2.Posté par bibi le 21/10/2008 22:53
si vous voulez reduire votre facture en electricite contactez moi sur wuwarrior@hotmail.fr

3.Posté par teuss2 le 21/10/2008 23:28
arrete c fou

4.Posté par boy tamba AKA critiqa le 21/10/2008 23:47
un point de plus pour nos mbok chretiens.

5.Posté par bibi le 21/10/2008 23:54
c'est vrais si vous voulez reduire votre facture d'electricite contacter moi wuwarrior@hotmail.fr je blague pas

6.Posté par cherif le 22/10/2008 00:11
mais toi le Journaliste de medeux verifie tes sources de merde ..les yalla yalla ne sont pas une branche du mouridisme ...bayil yake biii ....

7.Posté par bara le 22/10/2008 02:40
thieuye fognou dieme ak bethio thioun lakale ba de dou dara ba pare sonal niit gni leeep dof yi ka tope rek

8.Posté par pensée le 22/10/2008 10:58
ils sont perdus!
wath sa ndeye ak sa baye top ben "cheikh" ni rek!
vous etes à plaindre, de vrai brebis galeuses, je vous pitié.

9.Posté par khouthes le 22/10/2008 11:17
bara yaw ya mana doull gané cheikh bi dou dara yaw momou yadoul dara doumo kharam

10.Posté par FALL le 22/10/2008 11:50
Mbaye SECK tof bi nice et la médecine ?
Sinon namenala .





11.Posté par sad le 22/10/2008 13:00
ouais c'est bab's seck que je vois sur la tof là, un ancien da la catoche!! il comprendra s'il me lit bien sur, khana da gnou la "cheikhal" sa waaye!!

12.Posté par issa le 22/10/2008 14:48
les yalla yalla come vs dite ,st des mouridoulah.soufekene ,khamo demal lathe.sa serigne kan moye niambe darou .ba kham.lou waral.wakh djie yeup.lici kanam rawoul beut.soudoul degue dou sorri.man yalla yalla wa ahlou badar sangue chiekh moussa diagne niambe darou. sougenbougue wo lenko tele walla radio ak borom kham kham guen khole.baye serigne touba dafa yattou boulene di wedi lougen khamoul.dakh kou ngeme dagne la dee.

13.Posté par sopey nabi le 22/10/2008 15:24
cheikh bi mo léne guene bounou borom diamono cheikha loul wone kéne douko topou yén nak da guéna réré mbir you bari.mane dé serigne ak cheikhou sénégal yépou douma tok bay wakh si gnome louma khamoul parsk kéne khamoul té yéne gni bagne bétio vous devé vous posé la kestion litakh serigne saliou cheikhal ko.té sakh li koumou nakari yaye dé cheikh bi la nou wakh.walabok ziar sama mbokou talibé serigne saliou ak tjantakoune yi.diapou tewe bayi rék.

14.Posté par dof-bi le 22/10/2008 15:25
svp boulene gnou sonal ak bethio;yalla yalla yoyou yep thiakhane la:nagno diamou boro, di té bayi thiakhane yi;salam

15.Posté par dof-bi le 22/10/2008 15:27
nagnou diamo borom bi té bayi thiakhane yi.fi yalla ak yonenta bi rek fi nek

16.Posté par nou avon la pensee noir com notr peau le 22/10/2008 16:23
trés important a lire.......cheikh bethio (petit pagne) na jamai été promulguer cheikh par serigne saliou.
cé parce que ce saint homme serigne saliou ne voulai pas prononcer son nom de kathior (bethio petit pagne), qil la apellé un jour appelé de passage "cheikh bi " de la maniére dont les jeunes s'appellent "baye cheikh" " ou ablaye Ndiaye"
et depui l'hors "petit pagen" emporte de pauvre innocents qui ignore tout du prophete et de serigne touba.

17.Posté par joe sylla le 22/10/2008 16:25
manou dafa bakh tiey manou lene gueuùm deug islam deug moy nangou ak manou la revolution thianta en marche

18.Posté par khalis le 22/10/2008 17:14
doule yene thiantacoune yii bethio dou guat ak dambal you reey yii mou nior cst un faux mec il sait pas lire le coran dou touss day doule rek betthio le petit pagne coyame bou daye

19.Posté par verité le 22/10/2008 17:43
Bethio THIOUNE? sa bethio ndeye!!!!!!! maa meuneu rimé
kou mer bokko:::::::

20.Posté par issa le 22/10/2008 19:17
wakh dafa wara teguinne kilifa ken dou wakh thi mome di saga.mane douma talibe ch bethio waye gueumna li nek ci mome bou wer .li dounenne

21.Posté par scorp le 22/10/2008 19:36
yalla yalla moy lane ?? thiey senegal.

Referez vous aux ecrits de Cheikh Ahmadou Bamba. y a trop de fanatisme et d'associationisme




22.Posté par myma le 25/10/2008 18:11
en tout cas dal lislam rék mo woor mé sénégal dafa bari innocent ok gno hamené dounou occupé mouk séne affair.pauvr pays k dieu nous préserve

23.Posté par issa le 25/10/2008 19:31
wa senegal,deloulene khole doundou mame chiekh ibra fall.souguene bougue mouth thi rere.li waral mame ch, ibra tope bamba nekol thi tere.lerou yalla lako lathe mouye kalimatou hak ,sila lep nek bou wor,jai 2 questions ,louye ,islam .1louye nitt ,ndakhe yalla mo wakh thi alkhourane santoulnitt ak djine loudoul ngou diamouko.

24.Posté par moussa le 29/11/2008 19:10
slt man dama beugue niou khame ni kou gneme degnou la deye.bou leye wakhe khool te bu lene degeulou gni yak.nagnou ligueyal sounouile serigne ba ame sen guereum .mane yalla yalla la di sante cheikhe bethio thoune dnakhe sama serigne khamalnamako .nit deye manou.

25.Posté par massamba le 17/03/2009 16:39
slt am niouné yalla yalla yi ay tiakhane la naniou diamou yalla mo geune wayé yalla néna kham lene ma bala nguene may diamou solene ma khamoul nolene may diamo la tarifouna khabla antakh bi douni fa ilam tarifouna khabla antakh bi douni té nena bokalé bou geuna mak moy diamou ko khamoul wolof ndiaye né name ko khamoul fimisté la wa diamou ko khamoul kone lane ba paré yalla né irdji khi ila rabika radiyatane mardiyatane fadakouli iba di wa da kouli djanati depeul delou si sa borom mou geureum la geureum ko si nguay sogua done diamame bou aldiana nié mou téguate si ni woutilene cheikhoul mou rabi mou agualalene si borom ndaxx kham na pékhé nite noumou rayé mou tek si ya oulal bakhou brom khel yi la wakhal sou fekone ni amoul kone yalla douniou fi watiél ay prophetes watiél niou fi ay kilifa diné niouniou fi watiél ay alkhourane pour lane dioundiou la naniou deup way nioune dé douniou meussa parceque niam nako nekh na bayinako amoul fene nioune nak danio niam yalla mou nekh dara dou taxx baniou bayiko ta yonou yalla dafay bari khakham ta louy khakham moy seytané ta louy seytané moy ki lay diéma feweulé ak borom ta nioune lanié naniou cheytane wa salam yalla naniou yalla geuna dolele ta dimbali diam you réré mbir ta mbololmbe kilifa diné tass niou si sene barké >> di doli sante

26.Posté par diamou cheikh bethio le 12/06/2009 20:20
ya meneu rime ,ya meun doul nga wara wax .sa tiot[OU] nde[YE],sa coy[OU] ba[YE] MA LA DAKH RIMER

27.Posté par baye le 17/06/2009 14:22
pourkoi ses insultes deugeu kanila koka touffe mou tokhagnou wala mou salmou.bayi lenne serigne yi guéne di boubo té guéne diamou yalla.ak fo mana boke pr yalla dégeu la dou daguaye dimou dieume si bopam wanté nit gua wara diamou.mou talibé baye di mouride (thiantacoune) di wa tivaoune nieupe khamiléne yalla bala kéna dé .yalla ya kaye khamal sa bop sangua you bakhe yi dane laye tek si yonne wi késsé

28.Posté par goor yalla le 12/10/2009 04:39
on avais fait des émissions sur les goor djiguénes et les framançons et autre alors il faut invité chékh moussa djiagne a la tele é vous aller comprendre yalla yalla au vrai sens du mot (fi koufi nékoule yalla yalla. kone chaytanné chaytanné nga).

29.Posté par baye le 13/10/2009 13:25
ho goor fall je ne voulais pas vraiment m'exprimer sur ce secte car tous mes amies sont des yalla yalla.mais est ce que tes d'accord pour le licite et l'ilicite car mw je suis d'accord;mes font tous ce qu'il veulent ( boire de l'alcool fume couche avec les filles) apres ils dissent lernalene.Mr je ne vous connait pas bien mais ce qui sont dans ma localité et qui se dissent des yalla yalla sont que des tricheurs et ces plein au senegal c'est pourquoi les gens dit que vs etes maudits.dans ce periode ou nous sommes vos talibé ont pris la voie de la facilité.comme l'argent à gagné tous les foyer religieux ,le votre est gagné par la facilité( talibé you beugeu lou yombe yi) khamilene yalla waye

30.Posté par mamour le 20/10/2009 18:05
salamalikoum mbock dioulite yi mouy tidiane bi di layene bi di khadre bi ak mouride bi nioune nieupe nio bock fa yalla mais na niou khane né serigne touba défaroule rek béne walla niar ba niet goor yalla gni mou defar barina cone bock na gniou manou thi mbirou yalla yalla yi lo khamoul damal nga lathé ba parer soga wakh parole de mame cheikh ibra fall (so bougé lo guisse khame ko démal diangui wayé so bougé lo guisse ame ko damal liguayale goor yalla bou yalla gueureum) cone cheikh moussa cissé serigne touba guereum nako ague thi yalla rek mo woor wa salam

31.Posté par chacha le 31/10/2009 21:13
mane séne discussion bi mo ma titeule!!!!! mais un peu de repect way!!! vs vs dites mouride et vs insulté cheikh bethio c grav!!!!!!!!1 chui pa sn talibé mais kan mm je le respecte!!!!!!!! au sujet des yalla yalla ils font parti de notre confrerie le mouridisme!!!! ce ki disent le contraire ne savent pas l histoire de ndiambe darou! kou néke na gueume li mou gueume té bayi moromam! yonou mouride yeup si yalla la dieum!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!! diadieuf té svp modéré vos propos!!!!! diadieuf borom touba!!!!!!!!

32.Posté par salam le 01/12/2009 21:07
salam tiowely moye sayetané mo beugue kheupe si yeufe yi kani . wayé li ame téye deugue moye serigne daye wané yalla .serigne bou wané woule yalla sayetané la ak cou mou meunety done. wa réyemi da ma beugue gén yéwou té khamené mak you bakh gni .gnome wané yalla laniou fi néké wone .wayé légui lou eupe si serigne ci .classou bétio ak kara politique dongue laniou fi néké .di daw si ganaw boure .té serigne touba ( psl) néwone na dou diogue mouke téke tankame di wouti boure.

33.Posté par nit bi le 13/12/2009 03:24 (depuis mobile)
slt dof bi j s8 la pr t soigné parsk t gravmt attein pr lépidi.1.yalah bimoulay sak toudo won dof bi. si zair tour bou kén bougoul gno koy wowé nga tane, ya dof dé ... si mbalit nak(dof nak makamala si batine... dof fa yalah). 2. bokalé nga u t permet d jugé t prochin u t prd pr dieu?yalah néna si alkhourane "ma ndieuk,ma moudjé,ma fëgn,ma neubou" kon bou yalah néké fi yaw fo nék? sou yonént (psl) diougué fi l mnde noré po ça rézon détr.« IL NY A D DIEU K DIEU CAR TT EST DIEU» "NIT

34.Posté par gueye le 16/12/2009 11:03
mourides dafay set sèle yarou yatou mandou nango liguèye ak diamou yalla loolou lagnou lène sante affaire bi dou pagaye dieuf dieul rek la lou waye dèf sa boppe

35.Posté par deug bi le 25/02/2010 10:37
khamiiiiiléne yalla yéne les mourides vous etes tous perdu
mame bamba néna niit dafa wara am kham kham zair ak batine waay dafa mélni dégou léne ay wakhame

36.Posté par ebrima le 17/03/2010 08:52
cheick musa jange, njambe darou rek kai dega

37.Posté par faye le 09/05/2010 00:15
dieureudieuf serigne touba diaraama cheikh ibra fall giunawo yallah et psl c serigne touba amoulou benne tariha bou meune neke ci ginnahou mouride te dou mam ba moukou ba yomelhi manti lepe lou serigne touba dou dinei mouk dieureudieuf serigne touba le mouridime kepe kou que beugu saltel di ke digale ka mouridihi. deuireudieuf serigne touba et lamp fall

38.Posté par ndongo li le 06/06/2010 19:59
Thiéy sénégal!
mbokk yi tèye lène! Sujet article bi dou touss. Gnari jeunes you diotté leu rek. yagg neu fi am, journaliste yi gno siye profito di gonflé.
dafa fekk né kii dafa nékkon yalla yalla, keneen ki nekk thiantacoune késsé.
Thiow lou barri li yeup amou fii place. Bou leen nékha diakhassé, délèèn andak dall waye!!!
Wa salam

39.Posté par ALOIU NDOUR ETUDIANT A DAKAR le 06/07/2010 19:55
BEENE!!!cette information est erronnéé; té birmi diaroul khoulo diaroul sagawanetéé; té kouniou sagaa nagua mougne; ndakh yalla moné si alkhour-ane "mangui andak mougne katyii" 2XIEMEMENT moy talibéé SANGUE CHEIKH MUOSSA DIAGNE dou fayou sakh nakk baay togne BILAHI!!! mé DEUG NAK néékhoul Mé YALLA miné ma fégne( ANA ZAHIROU) kone kouko beugua GUISSE dangua ko GUISSE AK BEUTE ndakh MONEEK FEP FOU MOUNA KHOLE NAK!!!!WA SALAM WAL KHAKHOU LAHII

YALLA YALLA mbaa SAYTANEE SAYTANEE REK NAKK

40.Posté par zeus le 14/07/2010 11:02
yéne da guay dof, vous n connaissé meme pa dieu et vous ouvrez vos gueule mé pareléne séne féne yi diekh na car cheick moussa diagne is back: leup dina leer, yéne fo talibé yenaye walk wayé séne serigne yom lou yuye khar pour wakh si niambé? GUISS YALLA WALA Dé TABI SAFARA? amul siki bilahi degg la

41.Posté par dame bou cheikh moussa diagne le 19/09/2010 20:25
serigne touba a dit a houqual boukhaw faslou bi yadi cheikhal mou rabi ana cheikhal mou rabi you rabi rouhou diokhale sabopp sang bou mate sang mou yare sa roubi sou nope diebale ko yallah kone moune nay wokh ni serigne touba yaroul dieum rou la deme yare akassa mokou goor yalla yi na you selale kadou yi bou you beuguee you feek si gnou gueureume sang cheikh moussa diagne ambassadeur de dieu sur terre

42.Posté par fatou loum le 29/10/2010 22:50
eviter de dire des choses qui ne sont pas raisonnables talibe SANGUE CHEIKH MOUSSA DIAGNE RABOUL MAHDIYOU LIBERATEUR DES ESPRITS dou togn dou fayou te dou kheuthio adouna bi nieup ame none waye dara GUISS YALLA thia kaw lay dieum mame cheikh ibrahima fall mo delsi pour defarate diamono kom niko serigne touba defewone

43.Posté par tri o'clock le 31/10/2010 15:09
gayi yam lene kham yalla dou kou nek moko meune. Deug deug loufi am rek lay wakh, kou topp ibra fall da ngay diokk si khalif mourid ak khalif bay fall yi cheikh dieum fall. Les yalla n st pa reconu par aucun de ces khalif ni par les mourid bay fall. Ceux q j coné n réspéct mm pa les interdits dc bou féké lolou la kone takhawoul. Ibra fall bou délouci wone touba la dieum togat plaçam donc kholat léne fi nguéne féété.
Aliou u di q Dieu néna mo Fégne..lumu si tek? Ma Nebou laci tek kone lidiantil ana mohamd fofou, loloy mbir mi. Li ngay guiss da am papa ak yaye kone bayi lene di soss. C pa un site pr montrer ce q enseign les serigne dc svp un pe de retenu. ciao!!

44.Posté par diagne le 22/01/2011 10:47
a tri'clock li nga wakh lép deugula wayé da nga né kou topp ibra fall da ngay diokk si khalif yi wayé YALLA néna mane yalla nit moy sama khalifa si kaw souf kane nit kou nék yay sa khalifa bopp si kaw nga yeuk ko wayé dama lay lathi kou topp yalla si kane ngay djokkou. Té kou bakh louy cheikh ibra ak serigne touba lolou léér la dou loufiy diogué bay délousi té léér bobou yalla moy khol fouko nékh mou tabal ko fa dou nit moko kay kholal. Té yalla mo né mo fégn ba paré né mo neubou wayé serigne MASSAMBA néna YALLA koumou wane boppam nga guiss ko wayé koumou yir (neube) boppam doko guiss mou né gni diko guiss gni dougnou ko guiss moy gnou ko kham ak gnou ko réré . Kone yalla sou wakhé da fégn moy gnou ko guiss sou wakhé da neubou moy gnou ko guissoul.Té nit ki lép lomou khamoul rék daf sé warra manou ndakhté té bou gnou reyeu lathié. Té gnouy sam sougnou kadou di raffétal li yeup diarouko ndakh té nit ki lép lo meunti wakh fi di nga ko wakhate si kanamou yalla kane soignons nos paroles é 1 peut d respect té diléne bégué di gnane yalla na diam yalla nék si yéne ndakh té moy mouthieul diam

45.Posté par mouha le 04/09/2011 21:12
SANGUE CHEIKH MOUSA DIAGNE RABOUL MAHDIW

46.Posté par Diagne le 14/04/2012 14:19
Bismilah diam té diame moy Yalla kone kouy sakou kamal da nguay woute diam sagua mome dou téguine wayé deugue dou gnou ci ragale guereumety rek

47.Posté par Diagne le 14/04/2012 14:20
Bismilah diam té diame moy Yalla

Nouveau commentaire :
Twitter

Actualités | Politique | Economie | Fait Divers | Société | People | Sport | Coin des femmes | Culture | International | Vidéo News | Buzz du monde | Bande dessinée | Un café avec | Dinama Nekh | Buur Guewel | Double vie | Ndiaye Dollar | Wiri Wiri | Le reve de Akis | Rirou tribunal | Revue de presse | Blagues





Copyright © 2007 - 2016 Xibar multimedia Tous droits réservés

DIRECTEUR DE PUBLICATION: Abdoulaye Sogue - Contact: Protect e-mail with only css

Xibar Multimedia - 2901 41st Ave, Long Island City, NY 11101, United State